LYRIC

ISS 814

155

Ku investir ci sentiment récolter trahison

Oustaz day maye tanibeer bumay baayi son.     

Am na fenêtre pour nooyi prison du dee ci xel   

Am na ay xarit sen nooyi ming samay décibels

Nitt mën na wax limu gëmul nitt ñi gëm limu wax

Métissage moy forcing mais forcing buñu def ci pax

Awra pistolet à eau foo tirer baayi fa liquide

Boy yi tooy yi muñ loor pour ay problemu weccit

Maniiw investissement la ci parent bu pauvre

Borom karaw bu ñuul ñakkul dara sauf boy bu chauve

Nee nañ lu fees ci dënn feeñ ci jëmm

Pamela Anderson buy wax ubbi geemiñ est ce que ween moy geen

Liquide biy feeñ ci mineur bu ñu violer du mauve

Sa papa bu doon fay impôts du yor immeuble

Lu sama yoon nekk lay wax de sa yoon nekku ci

Comme lesbienne buy jiiñ goor jigeen nekk travesti

Mélange codéine akk Spirit gën ko topatoo

Suma binde image bi day right comme ku toog photo

Nataal bi nekk samay verres ku myope da koy gis

Correcteur la ci sen game prof doctor Iss

Ku xuuge la wax samay problème mu fate bossam

Hip hop bu amoon ay règles ñu jàngal ñu ko Ecofam

Mën nga tàmbaalee lu baax mu mujj ci lu pire

Mais neewu kumpë mënul xeeñ ci biir borom bammeelu biir

Bo bëggee dugg ci sen bopp yi fog nga use perceuse

Public bi gën a nelaw comme ku def alarme berceuse

Gis gis du bëtt sentiment du xol

Defal ma greffe beneen cœur kima nekkal lay xool

Kuñ nax ba jël sa ndaw sopi nañ la MAC

Maison d’Arrêt Conscience foo ay regret mënul ñakk

Liquide bu weex liquide bu rouge dereet ci drap dereet ci plastique

Souffrance yu classique oh shit

Life is a game buñ ñuy teg banc de touche on va s’y mettre

Sors nañ ci boîte comme convoi ci net

Woone samay douleur pour sa gars yi xool

Nitt ñi bari ay couleur comme li Wally sol

Goor jigeen yi am nañ devise

Gumbë yi am nañ vision de vue

Sadio Mane rater penalty

Bu ko kaas so rater sa vie

Added by

Maalik Sy

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR