LYRIC

[Verse 1 : Bako] Okay na beat bi dal kick bi danou lepp daldi andeu danou
Ins bi nako kepp ni guey képpé guels yi door ba danou bro
Ngandim mamou casque samay nopp faw niu defni wally seck
Fessal salle yi fokniu thiop balla go
Ouh La La Laaaaa
Wakhouma papeu thione borom faux gees
Bako niuni JayZ, Fla niu ni Eazy
Kalz nekk Nas , Escobar dou you feel me ?

[Hook : Maya] Ohh so we goin’ back yeah géné sunu baggy
Négn léne déélou 94
Délou temps wou biggie, Makaveli pac yeah
Négn léne déélou 94
94 , 94 , ninety
Négn léne déélou 94
94 , 94 , ninety
Négn léne déélou 94

[Verse 2 : Kalz] Béneu vinyle sameu bag
History’s on my back
Ay photos black & white dimeu fatali ay wikidiwhack
Baggy strechin’ survet takini yem ssi
Ni run Dmc yagg rendi mc
Classic…
Ni soiree séna le paris ci ciné
Genak seu cho daldi parer djadjak mome Paré si nék
Classiiic
Ni kou am gel bu mol niou naane leu takal
Lo beugg lu life seu lérr outil plan takkal

[Hook : Maya] [Verse 3 : Fla] Miss the time rap was about the real
No autotune but sick rhymes n nice flow to hear
Out in the street freestyle without the beat and make the fans cheer
The Time it was about the street about the fans N not about money and fame
Speak for the voiceless n talk about ur shit less
But niggas been talking crap
With their trap but ama strap that rap wrap that shit n flush

[Verse 4 : PPS]

Added by

Ahmed

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR