LYRIC

{Rosso – Verse1}
Louniou lay téré nga bayi ko
Louniou lay niane nga fight ko 
Boula kène nakh dara bessoul fek niou write ko
God dou lepp lay wané Kone dél saurou fo né
Mak day def yeufou mak, Goné yeufou goné
Da nga wara moytou kilifeu soko do né
Té nga tidji sa lamigne soudoul loudoul fiñu la sonné
Si lo né, sibauné, sa djiko sou boné
Li ngay yautou do cii djot touss ya xam si boné
Cii goudou bi bou gatt bi, yague nga degg cii bakou bi
Wakhou mak dou fanane aleu té dou yéindou pakou bi
Niafel ba guène cii, Té nga done bèn cii
Exemple yi gni diokhé han né ci kène cii
So you gotta win cause you’re black on your skin
Change it if it’s bad, the way were you been
You gotta try to be perfect, life for to protect
All things you do, follow the way of the Prophet
Na djiko yi rafett, té xoll yi tapett
Yalla rek té nga roy cii tankeu Mouhameth (p.s.l)
Bène (1) manoré yeup mé boul tayel fékhél
Niarr (2) sa morom bi ni boulko meusseu diémé féékhél
Niét (3) ladioul loudoul djeuf diou bakh ak xell bou séleu
Kone nak bayi cii xell
Mak, ndaw sama batt cii kaw
Djeuf diou bakh la Yalla fay sama batt cii kaaw

{M.A.S.S & Rosso – Refrain}
Louniou lay téré nga bayi ko
Louniou lay niane nga fight ko
Boula kène nakh dara bessoul fek niou write ko
God dou lepp lay wané Kone dél saurou fo né
Mak day def yeufou mak, Goné yeufou goné (2fois)

{M.A.S.S – Verse }
Li ngay def everday touss doula cii fékeu
Bène beuss, niary beuss, beuss nieuw molay break
Néwone nala boul fa diar dett fi dafa bone
Nga sani sa loxo dokh dém néma lou cii sa yone
Lassél sa Nike but I know boy
Fi nga nara tek sa tankeu rongagnu merr béfay toy
Déteu boul def, Wakhou mère boul play
Best father in the world takhoul nga lose sa way
Mbede ba ngui talk so better bad me
Té mbede béma sopi def cii mane djikoy bandit
No matter limay def, dégloul samay advice
Meune vice sama tiéné téyé ma gangsta paradise
Mère yi dagnu soneu cii sunuy taukh baune
Dioubeu leul yone boulko ték tiono bénène dom
Bayi tala tougnu gni gui daw cii guinaw doundou
Yaral sa bopp Advice like I talk you

Han !!! Mak day def yeufou mak,
Goné yeufou goné

{Rosso & M.A.S.S – Refrain}
Louniou lay téré nga bayi ko
Louniou lay niane nga fight ko
Boula kène nakh dara bessoul fek niou write ko
God dou lepp lay wané Kone dél saurou fo né
Mak day def yeufou mak, Goné yeufou goné (2fois)

{Rosso – Verse 2}
Life bi loumou eumbe beuri, niou fokalé nio cii feuri
Lou ngay guiss chaque jour cii keur yi, Diagg cii dii teureu reuri
Soudé beug nga guiss loula yém fékhél diém bay goudé teudi
Souniou soeurs yi beuri pékhé yiniou nakhé mères yek pères
Gnou doul moudié biiri moy gnigni wowé serr yi
Money rules the world, the help of God is necessary
Boul djay sa ngor ak sa dignitité, Nagn la lime cii gni niité
Deuk bé ngui tass, tay fougni djaayé virginité
Koulay diémeu influencé, wo ko wakh deug
Louko moy do meusseu fiancé ba guiss koulay beug
C’est à dire que gueumou niou sen bopp donté moy lou ndieuke
Topa ndo beug xaliss cii niom la deukeu
Aduna gui diekh yén guel yi yombe nakh
Gni cii topeu loulène nekh niom lay moudjé dougueul cii paakh
Mané Koulay diémeu influencé, wo ko wakh deug
Louko moy do meusseu fiancé ba guiss koulay beug

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR