LYRIC

VERSE 1
Amnga souf sou nangou,Alal djou takkou
Lou dess gnankh djeurignou
Wayé beug lou yomb nangoulo sone
Gneup moudjou la romb
Yaye bountou kouss
Yaffous , djémoulo touss
Gnakk fitt,foula ak djomm takh do djokk gnoulay nott
Fi nga djar ba yéksi fi téy takhoul nga kham ki ma done
Khamé say noon,khamé sa yoon,li bakh ak li bone
Li déf mame djam ba-wougn batéy khékh gnouy djokh li gnou mom
Gnouy dokh di dém té khamougn fa-gnou djeum
Khadjalo féwalo batakh amougn li gueun
Nitt bou gnoul khépp boppam khépp limou am
Li mou diir douko djam
Wakh djou bari yém am peund
Fénni neen feugg deund,
Beug fo teugg ndeund
Takhoul gnou dém fenn
Kou khékh ba déé,déé nga si néén
Wakhma lénnen
AFRICA,Dou meussa done benn!!!

{HOOK}
Kou Guestou Demb Kholi Téy
Guiss Fa-gnou Djeum
Kenn beuggatoul Tokk Kouné
Ngi outt Famou Djeum
Gnouy Gueundi Dem, Gueundi Soukh
Ko Fall Mou Tokk Done Buur
Foy Guiss Leer,Fou Leudeum Muur

{VERSE 2}
Borom Keur Yi Narone Yarr Djoubbeunti
Deuké Djalgatti Topp djankh sék Djéksi
Méri Tour Yékk Khéw Yi
Khalé Yi Gnakk Koulénn Guindi
Louné Gnou DouggSi,
Reey,Réw,Bééw Gueuna Feuss Si Rewmi
Bopp sa Bopp,Djoubb sa Djoubb sa Yone si Penc Mi
Séy Saw Sandi mbalitt,Lepp si Mbedd mi
Kouy khékhal Askan bi Boulma wakh Nguur ngi
Lorr Té Bégn Kou Wakh Loula Métti Mouy Fétt si Khol yi
Borr yi Bari Té Fédjoul Bénn,Lénn si Sokhla yi
Diss Si Ndod yi Batakh Kou Agn Do Reer Fi
Kheuthio Alal ak Nguur,Bérr Gni Guérr gni
Djakhassé Khél yi,Nott gni, Réy gni
Ba beuss Gnou Fippou wathie si Talibi
Djakkarlo ak Tioy yi,Déréd Tourou Fi
Gnou daw Bayi Gnokk Rééw Mi
Outti kaw Dém Lakhattou Djii
Ak alalou Réwmi(bis)

{HOOK}
Kou Guestou Demb Kholi Téy
Guiss Fa-gnou Djeum
Kenn beuggatoul Tokk Kouné
Ngi outt Famou Djeum
Gnouy Gueundi Dem, Gueundi Soukh
Ko Fall Mou Tokk Done Buur
Foy Guiss Leer,Fou Leudeum Muur

{OUTRO}
{HOOK}
Kou Guestou Demb Kholi Téy
Kenn beuggatoul Tokk Kouné
Gnouy Gueundi Dem, Gueundi Soukh
Ko Fall Mou Tokk Done Buur
Foy Guiss Leer,Fou Leudeum Muur

Admin Papi

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR