LYRIC

{Refrain}
Mbede bi niary pathie la Con yi ak scient yi
Lima waar nigga wathiou la respectel grands yi 
Rappé wo beugue niou tathiou la topatal cii rangs yi
Amoul bayi Ala Athiou la, xamé lèn déféants yi (2 fois)

{Verse 1}
Eh yaw! Nio ngui diémeu tek, mister Intellect
Firi séni bekeu ni ay deumbe beugue ma lekeu
Téwal foma fékeu, guerre bi do tchi lékeu
Da ngay goungué rek, fok nga yegg soga nekeu
Baune la cii mbede mi, Hummer cii tedd bi
Ndokh cii mbeundeu mi, Niambi taate cii ennemis
Rap déh cii heart yi
Deugou ba tchii beut yi
Fok yéneu mbaute yi
Fok guène deukou hurt yi
Under niodi thug yi, Sakétou cii nek yi
Tekma, getma, guéneu ana fake yi
Mbélé mbélé guifi ndélé ndélé lagni téla jaileu, Iri téyla, yéla
Yégueul la, yeugueul la yéggal la
(Bandit Mic) roukoula, thioukla
Bandit Mic Oukla

{Refrain}
Mbede bi niary pathie la Con yi ak scient yi
Lima waar nigga wathiou la respectel grands yi
Rappé wo beugue niou tathiou la topatal cii rangs yi
Amoul bayi Ala Athiou la, xamé lèn déféants yi (2 fois)

{Verse 2}
Hey Yaw! khaf bi mane la djot nigga bayil ma put ko
Boul langamou sama tuur, Bo beugué tuur fok nga out ko
Yeukeuti loxo sa kaw ma ngui cii biir DAARA J
Ma ngui nieuw di get down cii bi sound nel FAADA DJI
Kou niodi KRAZY COOL-LO, Bougni kèn doul-lo
Diak cii pays bi yakaar XRUM XAXMA fankulo
Dembe la MORT dou tay louma ray dou GUN
Niata aat la done sa KILIFEU nga done sama THIAT bi gueune
Diokone cii douss bi nane douss bi dafa xégne
Rap Dakar bou déh wé délou ndaxté deug doufi fénn
Bricage bifi rass, lagni wass dou dieune wass
Séni Clashes amoul place ba ngay nieuw danga pass

{Refrain}
Mbede bi niary pathie la Con yi ak scient yi
Lima waar nigga wathiou la respectel grands yi
Rappé wo beugue niou tathiou la topatal cii rangs yi
Amoul bayi Ala Athiou la, xamé lèn déféants yi (2 fois)

{Verse 3}
Yo! Kép Mic done sen K RIMES WAD
Génération CON foumou ko féké SCIENT dieul ngade
Amouniou Doff di teukou Fac
Mbélé mbélé douniou défé Fokk
Fo lène féké concert Fakeu
Dioxal thieur gnila Mak
Dama Raba Rap ba xeuy taggok lago dokh
Makama bi ngay niodi 98 mane lako dokh
Takandérou mbede guène get sen sagga yokh
Ay tcha dokh, never lokh
Ay tcha dokh, xol kouy sokh
Dou mane ak yaw goss
I’m your Boss
Kone nel TonS
Mane ngay ConS
Mic bi lay ngeup né tieupeu cii digue Coalition Bi
Keupeu NIAMU MBAM BI, niou wagni wakh cii Mission Bi
Cii guerre ngamay wo
GAS dé lerr la diwo
Meune Rap la galadio
Guiss nga nimay ngaladio

{Refrain}
Mbede bi niary pathie la Con yi ak scient yi
Lima waar nigga wathiou la respectel grands yi
Rappé wo beugue niou tathiou la topatal cii rangs yi
Amoul bayi Ala Athiou la, xamé lèn déféants yi

{Outro}
Cartell Undergroud dou défar fake
Maguétoum Golo dou faté yek
Hahahhahahhhaa
GASTON
Yek sen kaw déf dara

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR