LYRIC

Verse 1
Turn on the light djeguelou ma djegui ndokh
Rée di toufay tak dall djogui dokh
Boul nangou djeul ndaaré
Djougal xaaré famou taré
Boul bayi , Boul tayi
Boul daw ress ni gars yi
Dirou doundou dafa guat , amougnou diotto reuthiou
Systeme bi dalay xaddilo , euleuk fok mou fethiekou
Dougnou guessou lignou wessou , kouy dathe gnéme teuthou
Suñu dakantalou euleuk tay lagnou ko wara xatim
Yonnu ndaw feep la meté worna Mame Khadim
You try , you win , you lose and you die , adouna xarela
Diemala bokk thi gni geuna xaarela
Ki djitou ki parela
Xam sa wareef adjewoul thi xalela
Geuwma topando
geumal sa bopp
Sikkima lakado
megnefou askan wi mo wopp
yonnu kaaw lagnuy sopp
xel yi gno neup
mbed mi dafa reup
kouné sa guente moy teup

[REFRAIN (Nectar)]

Verse 2
Geumeutougnou adda , geumeutougnou ngour
money lagnuy guiss , fok gnou tekki done buur
Suñu euleuk lagnu diaay dieundé ko daraja
Education dée , mbed mi moy Daara Ja
Rap suñu life Tal, digueul-léko wine
Bak clothes ak shoes guir Guddi yi fine
Xaliss moy dieunde Gor , gnak moy doundeul vis
Sister yi done bitch , yoro , yaroul maygnou peace
Mbed mi setoula , lila gnor nga siy guiss
Illusion lagnuy dounde , sakku guente gué moudje diss
Nelaw sa mind yekeuti , danou mi geuna meti
Dadj weeki , guiss wedi , deug gui moy beugua tekki
Xeetou Djap youné ngay guiss , dakh xalate you diekh
metite bou teuwa diekh , suñu life kagne laye nekh
sonn si gouri guiy digué , askan wi keumeutougnou dara
Nango nak lignuy dounde , fou golo boté domam fala

[REFRAIN (Nectar)]

Verse 3
Xippi lene xol moytoulene mbeukou soga sigui
Tappé lene xol yi doumoyou wakhou politique yi
Gniy sacrifié sen askan
wargnu tigome di gaskan
Djoof metey santame
Askan mouy gnakhtou santeme
Yakar deme
Kouné di lathe ana Kaagne bi
Sante gnel Diambar yiy fight guir mattal agne bi
Geum Geum lagnuy deemé
sooraatougnou demain
Sokhlatougnou discour
gueine sakku guiss cour
mi ngi timis Goor so amoul Djiz teudil
deureuma sakh si xol yi noko meuna amé ta deal
Sath , fene , keupeu kess ni fess wala tek deal
Tous les moyens sont bons , chaine bignou ngal kougnou koy tekkil

(Nectar Part )

[REFRAIN (Nectar)]

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR