LYRIC

Refrain
Baay néna diokal khar sa tanku toubeuy
Lo fi ame sa gnaxa lakoy may Fonkal sa wadiour dara doula téré Go go go go!!!

Djiteul yalla gueum moom reka ame
Alale loudoul gathie doula ci samm Gueum né lep dina nice dinga Go go go go!!!

Saa baay nenama boul nangou koula yeureum
Daniou lay xamal sa sokhla té douniou lako fadjal
Djogal gnafé ci keur té boul xaar koula gueureum
Boumou gathie gui yako dagg, niakh lay sagal
Am nga ay rakk té founiou la tamé nio ngui naaw
Tankou kanam boumou la takha faté sa guinaaw
So djogoul perte nga, guiss nga bokk yé ngui néew
Lo fi guiss day diékh, niaata yoon nga souli néew
Soo limé – niaata ngay guiss so tolo digueunté
Yeurmeundé rare ni liguey, jougal dji sa guénte
Borom bi nieup lafi nékal, Deugoul doon kou féne teu
Founiou la séddé ci gaalou xathie fékhél diem ko feinte

Refrain
Baay néna diokal khar sa tanku toubeuy
Lo fi ame sa gnaxa lakoy may Fonkal sa wadiour dara doula téré Go go go go!!!

Djiteul yalla gueum moom reka ame
Alale loudoul gathie doula ci samm Gueum né lep dina nice dinga Go go go go!!!

Niata yoon nga fi rombe nitt niu naane la diw la
Mo fi doone def, mo fi amone li kou siw la
Niata yoon nga rombe nitt kou ame niu naane la moom dé
Dadone taxalé ci cogne bi, taakh yi moko moom dé
Dara jomboula boul nangou nekeu ndaré doom
Fassal sa djom boula kéneu djitou ci xaré doom
Boul nangou nelaw ci keur gui fa niakk naré böm
Adouna dara yomboul, metite laniouy fadjé göm
…. Sol nga sa dallou baay mou jotna
Boul nangou ame jott, wakhtou yénou sass bi jotna
Djogal waathie gaalou weurseuk ga ngui ambarkèl
Sou nieup di woute lou bari, nga woute lou barkél

Refrain
Baay néna diokal khar sa tanku toubeuy
Lo fi ame sa gnaxa lakoy may Fonkal sa wadiour dara doula téré Go go go go!!!

Djiteul yalla gueum moom reka ame
Alale loudoul gathie doula ci samm Gueum né lep dina nice dinga Go go go go!!!

Couplet Amdy

Outro

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR