LYRIC

{Rosso}
lii gni tame na djik ROSS
Nio gueuneu tégou si temps que niom Rick Ross
Kouko ségna tékalék souniou Bosss
Nieup khamnéniou ni niofi dak rap sip nga we’re the boss
Many men, nioné di kheuw
Doniou meuss tékalék kéne Na nga wait lii di nieuw,
Am bénéne hit,téy ma andéti thiow,
yone la ndakhté daméy raw, meuss nga dégue kouy ROSSO
Moy lounguéy dégue ni, kéne kéne si béne beat
Lissi haineu si mbed mi, boul di thiénék sa enemi now
Dagno wérédi, danga fék ni we’re ready
Néwone nala ,hater,séreu,jailer dou meusseu fété si kaw
Gno meuneu rap, déniou mandi si musique té dieulouniou drogue
Get souniou tack, kéne douniou dap
Homi, open your eyes,hip hop is rise up
Da nga fokné fouma téyé mic di rap
Sa your di mass,sa body thieupi thieupi yako téy?
Non, dafa fék lounguéy cons te défonce la cervelle, dadi louma nangou yague liguéy
ROsso’s back in da day, Rap dou rék sol aye Backinaday
nanga téy mbeur kamil bakouna téy, Ross,Pps,Books niofiné téy

{Books}
Daw jotali gars yi li xéw fi mélodie
Original Books sampeu mélo bi
Phénoménal King of cii Ghetto bi
Ghetto bi get up pi Mélo bi some mélodie
Galou rimes niou djow indi Do Ré Mi
Fa Sol La Si MCs run cii dém cii
Fuck shit LC, raak haine cii
Friend yi dance cii, Kaay niou brains cii
Mélomane bouy weuri dji Books na kalou fi
Mélodie Ya ngui vooom vooom olof yi
Ba lafi, Alaki, Some balaki
sunu xalate yi maladi some Mbauraudi
Béguéti gars yi yagg beugué bandit Bi
Rebellion Bitch, shot tati yankees yi
Dagati, djoggati, foxati, di fokati
Conquer Jungle that’s my mélodie
Yeukeuti Rap Yeukeuti peundeu bi ni party souf
Pop thiow li dieumeuti kaw niou dadi oufeu
Ya ngui blah blah dignu ka kaa kaa
Indi Satan Rabou fla fla di gnu kaa kaa
Ya ngui blah blah dignu han han !!!
Dignu kaa kaa dignu semblant sunu tympan
Garel, khouss, parel couche
Yeksi nga Médina daraay Ouf

{PPS}
Lyrical gunz out, hands up when im on da Mic
PPS the ghost banger like Dynamite
gueune leu adjou gueune leu djapè na nga fèxè dabè
Xam fou melodie djouguè fou guinaar yi di sabé
Dama tambalé wané li gueuneu taaru ci game bi té fok ma agaliko
Ni Nine ak Kaliko, Lou sommet bi sori, tewoul fofou lay nopaliko
Mifa bi hogaliko, euleuk niou netaliko
Negger bo massouta guiss, hun!
Flow yi puissant, Xam game miss temps, none yi distant
Kou moss guimi guindi, hard shit nga guiss han (Hahahaha)
Manè founè – yeme kounè gouné
The Ghost writah, wané ngaladjou youné
Yagg ci mbapata waral beurewma preliminaire
kou xamoul ndarey wiri, rédaction la ba lineaire,
kiy touss lamb ji tass, ki pousse ba moudjè passe
niak boussol ci game bé waral sa problemou nord
Done mbaam yombana fari, mome da jomb nafari
Tewalko Rio ba Rosso, goné gui diegui na forts yi

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR