LYRIC

{Ara}
Benn deuk ben bour
Benn kaddu bou kène yoré kassé mo nek tchi nguur
Benn ndapp leu kène dou sour
Benn système leu bouy lékanté lékanté niom comme ay loups

{Dayza}
Benn deuk nieup saalite
Benn dolé meunta djarignou
Benn deuk benn talli
Benn xolla nior benn xol leu bou melni keurigne

{Ara}
Benn deuk benn info
Whatsapp, Instagram jeunesse bé ngok
Kou amoul lo def da ngay xeuy tok
Mais kou am beug di défalaaté da ngay xeuy jog

{Dayza}
Benn, niaar ngané niéteu
Nguur dougnko nieede Ngor dou lek mbeede
Boul wakh nopi diko wédi
Benn, niaar ngané niéteu
Niouné démal ngané niet (non)
Gnilay djay niou ngi sa wétt

{Ara}
Benn wakh nieup gueum ko
Ben statut ngay dougueul nieup dieul ko
Benn nit lagn lèy gueum lo
Té nit kign lèy gueum lo mom YALLAH lala gueumlo

{Dayza}
Benn deuk nieup am temps
Benn kogne nieup tek thianyine
Benn deuk nieup manquant
Kène yorou tchi té ko tchi lathie mouné : “I’m fine”

{Refrain}
No No, Noooooooooo
Deuk waroul déma nonou
Bi dé tégo-goul ci yoon
Gars gni soneuh
Benn deuk nieup yeggueu ndo thiono bi
yeaaaaaaaah
Yeah yeah
Warr nagn ko tek ci yoon

{Dayza}
Benn deuk amoul yoon
Té dou deug té dou yoon
Naniou gueum lignou doone
Occident moy sunu noone

{Ara}
Benn deuk benn fight
Nagn niou délo liniou mom
Li nga déinkeu lagni saagn
Louniouy dinthial sunu dom ?

{Dayza}
Benn deuk zéro patriote
Dila xagne rêve dila may djote
Dila naane fal meu damay job
Té ko tchi fal alalou reew mi lay thiope

{Ara}
Benn deuk djouni djouni ndaw
Amougn lougn def amouniou founiou aw
Dougou naniou ci gaal-gui niou ngi dougou kaaw
Lapp naniou ci guéth ngi dém nagn déh naniou ba faw

{Dayza}
Benn deuk benn mbède
Tour ndokh tour mbaliite
Ko tchi wo diko yéddeu
Mouné leu : “na ngama dimbeuli”

{Ara}
Faaw xol sétt ngir deuk bi sétt
Beug sa bopp moy beug ki nék sa wétt
Meuno niaak ba nopi beug deuk ci fête
Boula liguèy fayoul boy fébar di quête

{Dayza & Ara}

Benn Hôpital benn médecin
Djouni malades no def niou beuri déh

Benn deuk djouni télés
Djouni télés, mêmes émissions

Benn game benn King
Benn King benn Hit

Benn Hit benn beef
Benn scène benn shit

Zéro money zéro bénéfique
Investir zéro bénéfice

Aka méti pour nga guène tchi
Niou embauché leu nga guiss keulé dila ciss

Gnilay niaane niolay nianal nga niaak
Ngay doundeu nioulay yaakamti yaakamté naakeu (sa déh)

Benn Kasso djouni détenus
Benn peuple milles foi milles peuples zéro buts

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR