LYRIC

[Refrain] Bidew bi moussou fi diokk
Assamane khine none
Yene saye khar rek gua meune def
Liir bi moudji na dokh
mag na ba di dem
monté jotna rame joke tank yi bagn
Lou job yomb
bolé tchi job Waro deuk tchi tokk
Diougeul topal sa khol
guidé ko ak sa bop
God dina def li tchi dess

{Lock}
Quand y avait qu’une table et une chaise
Quand on n’avait pas la clim
pourtant quand le publique a press play
ils ont pu recensé les clim
puis les premiers jours c est l’usine
le labo la cuisine
partait en concert en 7 places
maintenant on le fait en limousine
on a commencé par lever des briques
je te mets au courant éléctrique
5 ans apres tous parlent de nous
des copains Mc je vais faire des frics
c’est Buzzé la paix
je leur fais la guerre
ils font la paix
sur les jaloux
je ne m’attarde guère
ils me font de la peine
Hit The Club 1
Hit The Club 2
Hit The Club 3
pendant ce temps
les mixtapes pleuvent
elles sont gratuites
ils comprennent pas
et puis il parait qu’ils écrivent pas
parait qu’ils ont tout tenter
certaines disent meme que le projets
c’est d’eradiquer toute compete
on fait pas une etoile et un reverbère
on s’est fait (4x)
quoi les faire redescendre sur terre
de quoi les faire taire
laisse les faire(4x)

[Refrain] Bidew bi moussou fi diokk
Assamane khine none
Yene saye khar rek gua meune def
Liir bi moudji na dokh
mag na ba di dem
monté jotna rame joke tank yi bagn
Lou job yomb bolé tchi job
Waro deuk tchi tokk
Diougeul topal sa khol
guidé ko ak sa bop
God dina def li tchi dess

{Canabasse}
God dina def li tchi dess
defal lila war
dina faye bou tchi stress
1+1 2 yeah fils gua tchi Greg
2006 sama néék ak mic kou cyber
2007 galsen kham nagn lane moye mixtape
Ndongo D, Fadda Freddy Gno ndieukeu siip gneup
Legui ndongo bi done na father ci game bi
daye takhaw concert publique bi you F**k gneup
Shaaaaaaaaa
bidew bi moussou fi diok
assamana khinone
sama team logo bi moy 3e barame ci kaw
gnou def diff
bougnou sorou nigga parégoulo
les Mcs gnougui khif
ils n’ont pas de boulots nigga fi
gneupeul def show di késsé nimo
bou kéne tangué
gneupaye tangual
def fait domino
city bi di show love
guél yi di gnou ko diokh anytime
mélni dag nou ko amélone
Général Bass
sounou indépendance
new school soldiers yi marqués les pas
tabakh thieur yi like nike
légui dotoul Dakar rek
ate bou nek gnou weur Senegal
Mateu nopeu yi like Tyson
Objectif bi monde bi leu
Motherf**k yaw ak sa side

[Refrain] Bidew bi moussou fi diokk
Assamane khine none
Yene saye khar rek gua meune def
Liir bi moudji na dokh
mag na ba di dem
monté jotna rame joke tank yi bagn
Lou job yomb
bolé tchi job
Waro deuk tchi tokk
Diougeul topal sa khol
guidé ko ak sa bop
God dina def li tchi dess

{Jp}
Buzz Lab Bagnou bougué dara dagnou diok
nékone dksouth di def buzz
Locks Legl diougué kaw
Tégal ma deal ak Bass
gnou yeukeuti empire di disturb
Bass yeukeuti drapeau tchi kaw
F**kin Buzz tchi kaw khalé yeup
di def teupe
guiss gua linguay def
bokout ak lignouy def
bo gneuwé concert rek
diém ko rek teudji
démal takhawé neulé
yéne gneup daguéne teulé
bougnou diéma dapp
Usein Bolt dalay mbeulé
daguati sa khol fofou rek lagnou meuné
ladji ko sounou haters
lane mo takh gnougui khoulé
We Canabasse
Club Shot out yéne gneup
Buzz Lab Fépp
Nagn deff tékk
fi kene dou fi répp
tép son bou doul fétchi
kham nagn né Buzz Lab moy yeugeul Play
Jay dina meusseu rap taye
Jay dina meusseu rap taye May Day ! Eh day
yi domaram taye
gnouy nangou sén faye
diko yakk ay rap taye
Gnoune on veut les milles
donc on rape comme des millionnaires
pas de soucis a se faire
Lock Legl sur le terre terre
ce cher terre Buzz Lab ce qu’on voit c’est de faucaire
one hand if you love hip hop
two fingers if you love Buzz Lab et c’est tout
3e Barame bougnou diéma bab
5e barame pour gua takhaw rek séntou
back in the biz
make it easy
niari as yi dila teureul gua mise
Goumba wouma, miyopou, diélouma
bouma téné tchi kaw kham na loumay téré ma guiss

[Refrain] Bidew bi moussou fi diokk
Assamane khine none
Yene saye khar rek gua meune def
Liir bi moudji na dokh
mag na ba di dem
monté jotna rame joke tank yi bagn
Lou job yomb
bolé tchi job Waro deuk tchi tokk
Diougeul topal sa khol guidé ko ak sa bop
God dina def li tchi dess

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR