LYRIC

{Intro}

Han !!! Bobou Ba Taye
Cii bobou bataille
Tep Tep gueune yourette nigga
………………PPS…..…………….

{Verse 1}
Lou borom bi namm, diam meunou ci touss
Gni dieul sène lamigne nam moy gni né cii banc de touche
Dém té douma guestou, Sa kaw sa kanam ni Keyti
Rango lima wessu, Reud sama life cii keuyitt yi
Limay def deugleu cii mane, Dou dégn ni beuyitt yi
I rap what I live and I do it for love
Lima cii meune mako niafé, ba ngay nélaw magui sone
Gueustou, déikou djafé djafé li di nieuw la guissone
Dama deuxeugne Lidiassa yi ni Cheikh Anta Diop, gueustou Aaru Mbede
Bokou ma ak gniy ndieukeuneté Job
Gniy ndieukeuneté Gopp (Han)
Gniy ndieukeuneté bokk (Han)
Douma wakh di ci topeu
Bokou niou ring bouniou Box (Yééé)
Music kèn momouko, Sa niakk moy sa ndieurigne
Téwal sa kaddu ghetto, gni cii souf fay sa dieuwrine
Gal-gal ak fakatal bassa xoll nioul ni keurigne
Djogatt ni Champion cii ring soy téyé Mic may sa Serigne

{REFRAIN}

Li nga done seintu ngui sa geut
shits Come from the hood
féy cii guédiou rap, douy tchi naane ba def teutt
(PPS… bobou ba taye)
(PPS… meussoula fay)
Waxtou bagué albomb leu
Def xall rombleu
Bobou ba légui niouy xarr, Waar djégui niou yomboula
(PPS…. bobou ba taye)
(PPS…. I’m the Writah)

{Verse 2}

Ya ngui xol assamane nane comète la wala bidéw
PPS moy téw yénène vip nga koy diéw
Teunguéthie la pess bi diougué dal Dakar ba New York
Sunu xitmeu, rythme Hip Hop Galsen lagni nieuw yokk
Baye Fall cii xel ak xoll, douniou diaxlé douniou ragal
Figni diar koufa diar, nguimi so wédé rangal
Kalé bi cii ndigue la tambalé té aksé ngoul cii batt
Suniou doul wone faté, deugueur ni tay tiow béy djibatt
Boy bi meuné ci mic, meuné ci bombe, meune la xomb
Sokoy saurou gass sa tombe, Job ba takh niou rombe
Yonou real meunoul yombe, Dieul ndaré damako diombe
Lima yautou dina cii diott, apeu bé yagg dong wayé nieup dinaniou soudiott
Han!!! Writah dou tour bouma tane, mbed bé mako diokh
Yonou xatim ma ngui ni soko niémé kaay niou dokh
hum hum !!! yo kaay niou dokh

{REFRAIN}

Li nga done seintu ngui sa geut
Shits Come from the hood
féy cii guédiou rap, douy tchi nane ba def teutt
(PPS… bobou ba taye)
(PPS… meussoula fay)
Waxtou bagué albomb leu
Def xall rombleu
Bobou ba légui niouy xarr, Waar djégui niou yomboula
(PPS…. bobou ba taye)
(PPS…. I’m the Writah)

{Verse 3}

Awuma sens interdit cii kaw bitume wala beat
Foma bett fek mak Hip Hop ci bomb wala bic
baggy, basket, caskette wala bokk wallabees
Mbede cii tank ba tchi karaw, tanki karaw nga wara guiss
Bobou ba taye cii bobou bataille, deikou fitna wala peace
Tiono dou rerr, douniou tayi (Sonou), fokk sunu diant feuleu biss
Soy bégué, nang mako yégué ma gueneu xoss flow bi
am phobie fo bi, tiow li djoli xouss cii C bi slowly
Hot like hell, xambe sa xel, xam ko sa téél
Zik bou doul faye ni bou Jules faye baxé la ay decibels
Mbekté ngui may guiss sa beut momay diox doléy dém
Rhymes yi taw teuweu sébeuttt, nio lay fuck niolay yéem
Ba niouy door nieup ngui ré, tay nieup nguiro
Ragné na sama yone li ngèn di def lepp nouro
Athiou suma ko naré bett samay niggaz
Gni done diap teuweu bayi lou yone bi gueuneu niagass

{Outro}
Bobou ba légui niou meune mandou mougne
bayi nieup di ngang li nga done seintu ngui ni guindi
Teunguéthie feusseul na Kang (Kangam) ki lay diox xatim ak flow
Worna Khadim dou fo, gueustou K-Rs-One Comon rapadio ak 44
Alhamdou wa chukru ndém aksi naniou ba fii
Diégui niou dotoul yombe lou Immortel laniou ba fi
wakhone nala ma ngui nieuw

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR