LYRIC

{Refrain}
Game bi la def SENS INTERDIT wakhma loussi SAMA YONE
Guisseu gouma kouma diakhal ma ngi moytou sama bopp
Bobou ba légui nieuw naniou dem naniou ya ngi thiéné fi nga tokk
Prouvé prouvé rek ba kène dotoul amati loumouy wakh (Got’em)
La boca, la boca, La boca, la boca
Fils fayma money sinon nala nokka
La boca, la boca, La boca, la boca
Maak sama Bando di guéné ay lingo es la vida loca

{Nix}
Plata (argent) o plomo (plomb) noto diplomo
Héy accéléré na sa défaite nga doundou ko slo-mo (ralenti)
Niggaz tchi hood gueuneu takhaw poto
La vie de loco moy Shampoing ak Omo
Ay montant lotto ci biir ben lokho
Ay bone yu sadique day andak tokho (Euheuh euheuh)
Mayma ma waxtane ak niom ma gueuneu nioule fi boy kone f**k sa choco
Mayma boy may lekkak niom tchi restaurant chic di tank a loco
Boy ma dakkeu dancehall Mwaka (Mouaka)
Ay collé serré Cap Vert de la taka
Fi mounoul leundeum tant que ma ngi takka
Boy ya ngi sérass hum dagni guéné pakka
Découpé découpé Mc boy Omzo tém niou oubi dibitérie
Djaay ay Mc par kilo mariné sen djiko
Solale sen manageur yi ay string en nilon
Le Highlander parcours en dit long
Kodall pendant mille ans ak dissaayou million de pilons
Et ni l’un ni l’autre, le sourire sa Boca
Sinon dagnekay anesthésié comme la coca
Si si maay kilay f**k everyday
Mane maay faru rap bou épicé
Rappeur ya ngi diémeu djaay lou saff
koula beug niou done à part mes épiciers ?
Légui nieuw lène boy waxtanal Nikissi
Nioumay khol dima laathie kagne la gnibissi
Dama laakeu français boy ba doyal umh…légui dieul wolof bi confisqué

{Refrain}
Game bi la def SENS INTERDIT wakhma loussi SAMA YONE
Guisseu gouma kouma diakhal ma ngi moytou sama bopp
Bobou ba légui nieuw naniou dem naniou ya ngi thiéné fi nga tokk
Prouvé prouvé rek ba kène dotoul amati loumouy wakh (Got’em)
La boca, la boca, La boca, la boca
Fils fayma money sinon nala nokka
La boca, la boca, La boca, la boca
Maak sama Bando di guéné ay lingo es la vida loca

{Omzo}
A beuzé..éééy….c’est à dire que….hum
Capitano mane leu Raùl
Gaïndé guiss meu youxou miaOuu
Dernier Gaou premier Gaou
Un million dans les poches juste au cas où
Fils mane leu BECEAO boudé Doe lagni djaay
Eaux et Forêts boudé flow lagn niouy djaay
Cachet Un million sou thioolé niou baayi
Mane Tata Vivi momay wowé ndijaaay
Awouma wone moyenne mais tay mom j’ai les moyens plus que tous mes instructeurs
Boy ya ngi thiéné ci kogne bi di taale ay doublé melni meilleurs butteurs
Boy Miézé amna diplômam
Yegg boppam melni mère bou saga ndèye domam
Aucune option c’est la fuite je marche
Rappeur galsen yi sen fête moy 8 Mars
Hannn ! Baayima xel nga nek borom bopp
Samay douze doko guiss ci Horoscope
Trokh noppeu Fresh to def ba Europe lokh
Dieuleul Tof mane ak Rap comme weur ak doff
Wor ak tok wakhma ani goor ak lokh
Door ak love mane ak niom comme deur ak wakh
Sport ak dokh légui xepp na djolof trop
Rap galsen neu eupeu thiaaz Ngor ak Yoff
Fils wakhma loutah sa grand merr
Ma grammaire n’épargne aucune grammaire
Wa Sipres samay son dougnko gueumé
Nénagne niom diouli rek lagnema khamé
Ma ngi téléphone ak sama avocat
Guel bou andak forme bouteillou Coca
Ci Team bi nieupeu meuneu coaché la Roja
No Djoutou Gang Mother f****r ééééy

{Refrain}
{Refrain}
Game bi la def SENS INTERDIT wakhma loussi SAMA YONE
Guisseu gouma kouma diakhal ma ngi moytou sama bopp
Bobou ba légui nieuw naniou dem naniou ya ngi thiéné fi nga tokk
Prouvé prouvé rek ba kène dotoul amati loumouy wakh (Got’em)
La boca, la boca, La boca, la boca
Fils fayma money sinon nala nokka
La boca, la boca, La boca, la boca
Maak sama Bando di guéné ay lingo es la vida loca

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR