LYRIC

{Verse 1}
Einhé Okay
Einhé Okay
Nigga ni demb ak Tay
Fa euzeul laniou outé manam ni tak ak fay
Nila assamane souté ndakh mélo yé bokk, Waayé mane ak yaw ni 6 ak 9
Niak eudeup ni bras de fer la entre xathie ak boeuf
CIA ak keuf wala bok tek tiane get seuff
Degg Dathie real stuff
May ruhu bi takh ngay dox manam pneu ak cric
Nigga may ori yow ngay fake ni soow ndjabote ak zrik
Da ngay fomp mane maay tothie ni éponge ak brik
Thiow ak fric damn nigga goor def fiit
Meun la cii flow
Meun la cii bizz
Eupeuleu doe (Xaliss)
Rawla cii skillz
Dakla show
Team bi di sheeze
track bi di blow
Public bi freeze
{Refrain}
Li ngay niodi gueumou mako nigga
bokouniou game
Fi nga dieum fala diougué nigga
bokouniou game
Yagui zair ma ngui baatine di dem
bokouniou game
Bénène mélo bénène djeufine yagui soga am blem
bokouniou game
Li ngay niodi gueumou mako nigga
bokouniou game
Fi nga dieum fala diougué nigga
bokouniou game
Yagui zair ma ngui baatine di dem
bokouniou game
Bénène mélo bénène djeufine yagui soga am blem

{Verse 2}
Founiou nekh niou ngène ni ndiaxassou textile
Di tek di get di dioxé faxassou tek style
Di break di nek ba sori di laxassou tek skill
Di break di check di fowé kandassou def tchil
Bénène level cii brain-neu kawé ni Maarifa
Yeukeuti sa hand-neu foma seintu ma ngui fa
Fi niou djangue mo beuri finiou nekh niou taaréfa
Saréfa ni boma topé garé fa
Di rap ngay regg di guedda diougué cii mbede ni sega
Tek ay djeggo nguir tedda, Flow bi di takeu ni ledd
Bari rap yakar ni fokk niou ndeupeul ma
soukeul ma done sa wassila mbeukeul ma

{Refrain}
Li ngay niodi gueumou mako nigga
bokouniou game
Fi nga dieum fala diougué nigga
bokouniou game
Yagui zair ma ngui baatine di dem
bokouniou game
Bénène mélo bénène djeufine yagui soga am blem
bokouniou game
Li ngay niodi gueumou mako nigga
bokouniou game
Fi nga dieum fala diougué nigga
bokouniou game
Yagui zair ma ngui baatine di dem
bokouniou game, bokouniou game, bokouniou game

{Verse 3}
Bokouniou game yagui cii tali ma ngui cii diawou dji di dokh
Waliyane super ndanane di walangane ni ndokh
Né bamay Rap raba ngo teunkou ma tél na lolou
Teunk sa carriere 16 mesures avorté ko, tell ya Lol
Done specimen Superman batinou Usain Bolt
Game bi endurance dou course de fond Susan Bolt
Winner cii brain-neu cii hand djeum dji di takeu ni sun
Nigga di palpé sa haine-neu sa brain-neu track bi di run
Nigga sa game cii tééneu di féneu just for the fun
Technique flow diko burn
Ay kaddu you feukeu ni Gun
bokouniou game, bokouniou game,
bokouniou game, Nigga Bokouniou Game

{Refrain}
Li ngay niodi gueumou mako nigga
bokouniou game
Fi nga dieum fala diougué nigga
bokouniou game
Yagui zair ma ngui baatine di dem
bokouniou game
Bénène mélo bénène djeufine yagui soga am blem
bokouniou game
Li ngay niodi gueumou mako nigga
bokouniou game
Fi nga dieum fala diougué nigga
bokouniou game
Yagui zair ma ngui baatine di dem
bokouniou game, bokouniou game, bokouniou game

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR