LYRIC

{Intro}
yeah ! guissoumafi loufi diss men
Life bi mo démé nonou sometime nékh
sometime mou diafé mais boul meusseu khadi
diougal ndiougal niafé man

{Rosso – Verse 1}
Yéne sayi dinga beugeu téki,mou méti,
nga fok né diékh ndakh daféy diafé nga ame ndieugou ndéki
founguéy foguéni, toguéni yalla nékoufa,
nga bayi sa lokho la yéne sayi weurseuk bi di diéki diéki
feul daféy nék fou sori, kome khaugne si tatou thine,
nga diotko faut que nga ame loumélni koudou dok ko meuneu diéki
dina méti nguéy dougou di guéne,di lambe do dédj féne fouy séne,
té so déwone téy téy doto beug déki. life béné nii, dou thiagéné nii
lounga beug rék dangua koy diottt légui ni nii, nassa fiit takou nanga waakhou ni gnii
nanga bagna topou wakhou niitgnii wawa goor, nanga nék goor,
nanga gueum sa bopou louméy wakh nii, goudék beuthieuk dangako wara saure
lounga diapone dissi fore akouss néw,
loumaléy digal moy nangassi diap téy nga
wara gueuneu meuneu daur

{Peace D Lion – Refrain}
bayil tok di mind all time kéne kharoula
ya wara meuneu takhaw téy né goné mag na
takhawalou nélaw ak thiayne dou adouna
waro meuneu takhaw téy nane meunouma
dounonou
yalla yalla béy sa tol
job moy féy
diougal liguéy

[Verse 2}
téy la téy,téy la life bi geuneu dé,
boul meusseu guiss mou méti rék nga nék fi runaway
dou meusseu wéy,diougal té kheuy,today is another day,
boul féguéni,togué ni;nalassi guéné kone téy nga dé
sa diom warnala méy ni sounioula dougalé si
guédj té amoul bankass téwoul dinga wara fékhé diéma féyy
takal sa fit,boul meussa bayi,fassal sa diom,boul tayi;
danguéy ame dara soko bolék loula yalla méy
yalla rék moy méyé di nangou, didiokhé niou manou,
fo tonié mou bal la, foko niané mou méy la eskey!
est ce que dinga ame bénéne chance?(hahan kéy)
lolou rék warone na meuna takhnga fékhéé téy
nga niafé,fatélikou démb,nonoula,dinga guiss
kou ame alal téy mou nékh yalla souba lép diéki séyi
nanga manou, nanga fight
nanga khatiou, té boul tayi
lolou moy takh linga dougou dingassi meuneu weuyy

{Peace D Lion – Refrain}
bayil tok di mind all time kéne kharoula
ya wara meuneu takhaw téy né goné mag na
takhawalou nélaw ak thiayne dou adouna
waro meuneu takhaw téy nane meunouma
dounonou
yalla yalla béy sa tol
job moy féy
diougal liguéy

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR