LYRIC

{KarbAllah}
nioune ak yéne le thi biir rhyms yi niouy tek
sounouy hak laniouy bakk anytime nga niouy get
koulou dieum ak rou xel mou sell laniouy séte
mission niou yébal thi yéne dembe ak tey niou né thi quête
messager de la paix
deugue doone lignou wooté
mic doone sounou epée ngir fight doone gniy yété
fékhé ba diam gni tékhé
gni khaddi woone diogue di niaffé
eclairé ak denoncer binde sénni diaffé diaffé

{Azou}
diguanté nod ak likhaam
kaddo niou waxyou
niou khaatim li guindi kham
gesstou xam taamou rap di thi wax yiw
mayma nope ma deugueul thi rap i sama waate yi
li xalimay reude yéné béye mou néékh RABBI SAMAAWATI
ni gantiax di soxlaa naadj
baye faal bou soxla madj
nite di name fatali kaddou yi lay féke si soxlawoul laadj
(chorus) bouniouy binde
tiakhane yakhoul nelew
kheute wa ngi toy thi niakhou khalima binde ma ngi law

{Refrain – KarbAllah}
bouniouy binde
maroume xolli laniouy weug sap lou lakhouwone si nioune si bountou xel
yi nioukoy feugue
yeg yeg la bouniouy reude
dégg yone la bouniouy kheude
bireul baatou souf beut yi araf touff nagn si deug
lek lek mou nieuw
lek lek mou dem
lek lek mou low
lek lek mou téng
lek lek mou gadou diack raak guéne mbaar li lakhou fégn”
djékhital ba”
sakkou naat ,waslou akham si yéne
certitude ak pertinence téggat pas jeum si yéne

{Stan Flinger}
lignouy binde
meuno thi niak guiss sa bop
daniouy khaatim fesseul
deugue moudié tak thi sa nop
lignouy rhyms
dou mbok dou gaine
daniouy geestou fou sorri forri lou neubou sometime
fékhé ba beeglo gniniouy kep online
fignt thi mbeebeti gars yi deuké di shine

{El Chigga}
taarou mbinde bé ma oubil guéw ma sar thi art
ni iba gueye massar
sounou mbinde mengo ak
diassi spartacus thi baatou nia khothie sounou story
kiirayou resistance la tchi monde gladiator yi
liniouy binde di dioor
di thi idji di door
dou kopar lanie koy monnaie yéé
pitakh gou wékh leu airou diam la meune noyé
lek lek mou tiomp rimes bakhé ko nia nécessiteux
defko lapa také feugue leu ni ness ak siteu

{Refrain – KarbAllah}
bouniouy binde
maroume xolli laniouy weug sap lou lakhouwone si nioune si bountou xel
yi nioukoy feugue
yeg yeg la bouniouy reude
dégg yone la bouniouy kheude
bireul baatou souf beut yi araf touff nagn si deug
lek lek mou nieuw
lek lek mou dem
lek lek mou low
lek lek mou téng
lek lek mou gadou diack raak guéne mbaar li lakhou fégn”
djékhital ba”
sakkou naat ,waslou akham si yéne
certitude ak pertinence téggat pas jeum si yéne

{Wicky}
louniouy binde done na téré
téktal nombe bouniouléy yéwlou
louléy deukeul si aye téré
nguir nga mouthiou bala yéwlou
louniouy binde fégne si keulé
né thie nioune niou séne ko feulé
pharmacie bopou kogne, mission change nieulé
conjuguer le passé
participe effacé
binde téy dépassé
conscientiser masse bi
réussite bi nokoy tracé
séy bag yi nokoy lassé
séy rongogne nokoy dassé
yo right!louniouy binde done na temoin

{Moshady}
man as i grow up i always tried to find a way to write it right
extract the worst off of my body
lirycally im tight
trynna tell whats in my mind even tho y’all cannoy feel it
but in case that y’all just do
now i just hope that y’all gon dig it
cuz at the age of 24 my nigga pussy aint a livin
got u runnin around the block now talkin shit thinkin u won it
but u still writting on that gangsta shit – all day
but with consciousness my writing im always taking to another level

{Refrain – KarbAllah}
bouniouy binde
maroume xolli laniouy weug sap lou lakhouwone si nioune si bountou xel
yi nioukoy feugue
yeg yeg la bouniouy reude
dégg yone la bouniouy kheude
bireul baatou souf beut yi araf touff nagn si deug
lek lek mou nieuw
lek lek mou dem
lek lek mou low
lek lek mou téng
lek lek mou gadou diack raak guéne mbaar li lakhou fégn”
djékhital ba”
sakkou naat ,waslou akham si yéne
certitude ak pertinence téggat pas jeum si yéne

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR