LYRIC

{REFRAIN}

Get ready let’s go back to the basics
indi rimes ak flow, mbind la beat ak bass sick
to the classic, Pps The Ghost writah phénoméne, féno man, xaragne beuri classe chic
punchline factory, lo ték ma fape touri
faramfathié fatéli, souma paré nga délou fac doori
skills ak poetry, real life ci mélodie
bénéne génération feusseul mbéd ci mélo bi
ragné ma doolél, roote ci démbe doundé ko taye
dangaye goungué ba taye waste time damako tayi
the last poet, jok , jeuf jeul you know it
track crack na wéli, waar wé la woolou do it”…

{REFRAIN}

Ni messi ak balle , xal si game bi app tool
Leeral yonou ghetto boys yi niane feké ak taal
Tewal benene rabine (Rap) na ngay nelaw gni gui reuw
Naw ni pitch bi thi dobine ramatou yi di xeuw
Li baxo feuss si biti bi ta moudje sax thi keur yi
dakh gouné fowé talif , tari say guente douniou gak
Diamono dokh baniouy diamalek li ngen bakho deug
dou tewal askan wi ni systeme bi waxo deug
Limoy Aaru Mbed dou Bibliotheque nga koy guësto
Wathial thi tep tep sa dëgg dëgg geuna costo
Time boune ak niako mome souba Yallah yana
li thi dess netalli lay done lignu féké lignu thi baye yaa na

{REFRAIN}

The last verse, the ghost moy déloussiwate
rime maker, under béy délou siwate
Délou jiwate, jihad hard , ni J-Xaar
Listixar, waar li mbed di xaar
rame séeti next, benene level sunuye texte
yok punch sunuye line, fine ci yénene contexte
jonganté métti ci forts yi, fékhé xalleu allou goor yi
Tongonté ci métaphores yi, tords yi feuss ci allégories yi
Hallou gori, hun! manatoul yombe mbok
Boy biy flow rimes technique wayé néxoula ndok
Défaral sa tógaye, ndakh dou fi yéme
Liguéy béy soga tambalé niou féss déll ni soufi yéeme

{REFRAIN}

xolé ma old , diarolé shula demba cissé
mougn demb mougn taye under bema gemb tu sais
Geum Rek , Diem Rek , Diom rek , Diam rek
Ni diego tango jango tango dagnulay diom rek
Boul lathié kikana
Ki mane douni mana mooss
Pps the Ghost , boy mbed meko moss

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR