LYRIC

{Verse 1}
Papeu sa dom day RAP waayé yakagoul
Kaddu yé niaaw yen saay waayé aka cool
Xam naani bo sagnone ma défi lénène
Bo sagnone guiss sa dom done haut diplômé ni niom Philomène
Papeu RAP bouma cii amoul Don amena cii Magie
Xamalni damala rouss takh wakhouma nga nianal ma cii
Chaque jour niou woma FAC ladj ma loutah djanguétouma
Bama taané sama xol la khaarone xel tek meu toumeu
Boudé Job ak gueum leu rek kène douma
Gueuneu dégueu niom “Wa Gooré Coumba”
Waxalma prof yi courou maths heure rek ladone calculée
Sen cours fessal cahier samay texte dinagne fessal salle bouné
Dama tégone lepp day nieuw rek yombeu temps gouné
Waayé djanguena kène dou dokh cii khal ak tank nèène
Yoro gouma té dona gouma tousse waayé wowéma self-made
Yaw lepp li nga yor cii photo lako guiss yawla Selfie Made
Tay louma niit yi meuneu niodi (amoul)
Mane louma dadjoul cii yone bi (amoul)
Kou sagne wakh moma fii andi (amoul)
Mo ngui tarr ba légui waayé passion bi ma ngui koy doundou ak Amour
Ndax dama gueum beuss nieuw li yeup done nétali
Douma xam RAP boudone sama yone daa nieuw rek taali
Bokoumak gni ragal taaneu ndax dagnou ragal gaagnou
Niakkeu soga kaagnou
Rakk ndawe boula kène téré doundou say gueinteu
Dara yomboul kone lo beug na nga cii def sa kem-
Ta-lay Katane wané cii jom ak ngueum
Niit cii lo meuneti né da nga ko wara diokh akkame
Yone bi nak dina goudi cii nièneu
Waayé yone bi dou goudii cii nèène
Goudi cii nièneuuuuu

{Refreain}
Diar diar bé tarr ba kène douko fogué
Lima doundou beuri ba tay ma def confession
Confession oOOOOH (2 fois)

{Verse 2}
Gnou cii beuri démone nagnou ba fogone né dina sankou
Djappo cii thioloul nguir Yallah bayil ma dem lay saakou
Beutou kaagne yignou ma done xolé sama kogna takh
Kène téloul farlou ci mane bay gueum beus na nieuw ma takkeu
Waayé thioloul da gueuneu takh rek ma indépendant
Tay kouniou dadjal banc soubeu do khaar bay perte sa temps
Motah beus bouné ma nék cii liguey bou hardcor
RAP ba samay corde vocale daggueuh fok nieup d’accord
Goor Yallah fék fou dara néwoul mou né faa
Boul daggueuh yonam ndax bagnoul ba tchi déh faa
Gueum na lolou sama bopp waayé meunouma wéddi
Légue légue mou tarr sama bor bama xalate tégué wétt lii
Ndax damay tokk lathié sama bopp : Est-ce que dioumou meu?
Est-ce que ak Rap bimay def beus dina nieuw ma guéné cii Mama?
Sama yone DROITOUL ANGLE mako gueuneu xam PYTHAGORE
Boul THEOREME cii sama life soxla wouma sa ACCORD
Nama Yallah baal waxtou diouraum sakh geudj nako matal
Lep louma tal moy guèneu tchii xawouma lima dall
Day melni Iblis la gueuneu djégué cii tay dji lééé
Yaay xamna fatéwo ya ngui may nianal sa yo djoulé
Meune RAP carrière dapma cii yone
Reuthiouma tay boudone dembe ma def lima défone
Li nga beug guiss rek nga khol mane lifi né lala wane
Dessna cii yaw nga guiss Hakill bou bess mais lawone fawone

{Refrain}
Diar diar bé tarr ba kène douko fogué
Lima doundou beuri ba tay ma def confession
Confession oOOOOH (2 fois)

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR