LYRIC

{Y.Dee – Intro}

{Simon}
A: Alimenté Alouweu Art bi ak Assonance Actionné
B: Boulè Bindeu de Base bi fi né Bloqué Beuss Boulonné
C: Clatel sèn Cartel Cotisel Cancre yi Calakantou
D: Doréko ndakarou Dioubeul Deukkeu yaa tcha Dess Dina antou
E: Enjoyal ndax Elément youma aile sama Esprit laay Etalé
F: Feulé Founé Flortel Flambeau Feeling laay Fonctionné
G: Gueumné Gaïndé Ngaaka douka Goxkilo limou Goux men
H: Hardcore la waral may Heurté Haters sama hood men
I: Indile Instru ma Installé ci Insbi féssal saay poche
J: Jubilélo sa waa Jungle done Jankk si sèn biir Jukebox
K: Kalamay Kocc dou ay kathie képal limay adjii
L: Lèm lène Lossi wala ma Liff Lamigne ya Lou kèn doul adjii
M: Maxama Mèr Minena Mbague you Massoul Mos Marifeu
N: Notena Nitt Neubeuko djante Nassaxal Nékinebeu
O: Orienté Objectif bika taxona jog bamou moudj Off
P: Dou Panne Perdal Peuteuxe Partout di Pliké ba loff
Q: Qualité Quantité Quintessence moy sama Quota
R: Real Rappeur la Révolutionné dou lougni Revoir
S: Simon Soldier Sigui lène Sèn Star moy Signé
T: Tocard dou Téyé stylo weum Talent laay Taal amoul Tatonné

{ Y.Dee – Speech }

{Simon}
U: Universel wadji da Unique Utile di otté by Unit
V: Véridique Virulent Versatile Vrai leu kaay niaane ko Visite
W: War la gueum Wagne la djeum nguir Wallou Wankeu yi Weurndeugue
X: Xétalil katawaay dou Xaalil Xaatta day khol Xééx ba tcha gueune
Y: Ya Yakoulé beug niou Yakkal Yamal Ya xam boul niou Yokal
Z: Dano Zen thiéné sounouy Zone di Zappé say Zik-Zak daal

Aaaah Voyelle yi laay Assonance Consonne yi ma allitération
Aaaah Dialal yi laali laal niam nagnou sama réalité wou ration

{Y.Dee }

{Simon}
Warrior deug Hardcor deug tangor douko meusseu lem mouy seugueu

Aaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR