LYRIC

{1er Couplet:}
Dafma guiss bégué ma show ma love maniko homi WASSUP
Mou guiss ma diay ma diap maniko enemy what’s a FUCK
Damma khamni nieupp menouniou bokk beugeu KéNE
Waral mane kéne bayi nieupp té diapp ci NIéNE
Amna niouy doundou ba dé douniou bégue mouk douniou RéTANE
Moy ñi bagne ndogal ba tey wayé naniou akimo SHEYTAAN
Biss bima amé sama guiss-guiss bopp ci la GOUMBEU
Faté demb doundou tey biss bou ci topp ALLAH AKU BAR…
Ame ñi di wakh ak ñi di DEF/Mane ma taane takhaw digui séni KHEF
Guissatouma loudoul GAIN/ Dégatouma séni FééN/ Wakhatouma loudoul ame sama gagne PAIN
Haaaan pour yaw dama F-DO “DOF”/ Haaaan pour yaw damay FONTO
Naniou Yallah may touti rek dinga xam mane ak yaw y’a pas PHOTO
Loudoul jamm meuno mako diay yaw sakh goor faal wakh ma FO TODJ
Lingay doundd soufé khamo nokoy yeuketé kaay ma wakh la FOY TOODJ
Damay def rap kone fok rap def ma ndakh dama wara done KéNE
Deugue deugue nak Linguéne di def fayoul waral mane ma GUéDE
{Refrain 1}
Yaw danga bagne nima mel limay def nga beugue KO SOUL
Mane mani nga téyé sa xalaat fi dara BéSSOUL
Yaw danga laal aye bideew fokni légui LEPP COOL
Mane mani la Hakill loudoul Jantt bi moom BEGOUL
Doma def sarap neegguh doma def sarap
Yaw dangay saup mane damay RAP doma def sarap
Doma def sarap neegguh doma def sarap
Yaw dangay saup mane damay RAAG doma def sarap{Couplet 2}
Sokhlawouma geum sama bopp ndakh sama bopp ma GEUM
Sama bopp ma GEUN/ Waral may ladj sama bopp may KaNE
Yeeh Mane la Hakill mane la Khalil mane la IBRAHIMA
Léég léég ma bakh léég léég ma bone doma sopi BAYIMA
Sama yoon ci beutou nit yi séni lamiine yi di toudou nane LA MéL
Mane kassé nékone sama biirou Yaye mane kassé’ay nékat sama biir BAMEL
Kéne déglou woula ndakh kéne KHAMOULA
Bouniou la khamé ba déglou la sakh kéne GEUMOULA
Hein fuck up what they SAY/ I’m DEAF
When i’m on my WAY i do less WEIGHT/ Than LEAF
Only feew people know really who i’m where i’m LIVE
Normal they aren’t rapper so we can’t get a BIFF
Néléén li dou rap non faudrait qu’il sache faire LA DIFF
Lii nieuw guinaw rap la toureum bah ladj ko Ya LATIF
Nioune… Xoulo wouniou xéxouniou ndakh daniouy GUERRE
Nadji da lakoul sa taat motakh ngané do kheuthio KééR

{Refrain 2}
Yaw danga bagne nima mel limay def nga beugue KO SOUL
Mane mani nga téyé sa xalaat fi dara BéSSOUL
Yaw danga laal aye bideew fokni légui LEPP COOL
Mane mani la Hakill loudoul Jantt bi moom BEGOUL
Doma def sarap neegguh doma def sarap
Yaw dangay saup mane damay RAP doma def sarap
Doma def sarap neegguh doma def sarap
Yaw dangay saup mane damay RAAG doma def sarap

{Pont 2}
Rap atomique rap ATOMIQUE
Rapagouma damay todj TYMPAN
Made by Hakill by Hakill
Ya niakk goût neegguh si T’AIME PAS

{Refrain 3}
Yaw danga bagne nima mel limay def nga beugue KO SOUL
Mane mani nga téyé sa xalaat fi dara BéSSOUL
Yaw danga laal aye bideew fokni légui LEPP COOL
Mane mani la Hakill loudoul Jantt bi moom BEGOUL
Doma def sarap neegguh doma def sarap
Yaw dangay saup mane damay RAP doma def sarap
Doma def sarap neegguh doma def sarap
Yaw dangay saup mane damay RAAG doma def sarap

Ich Yo Boy Haan… Haanoow

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR