LYRIC

{Refrain}
Day Dem Bandit Mic bi day dem
Bokou gnok gniy takk dii fay ni tallou mbaute 
Day Dem Baay Dieuwrine day dem
Demb lagnou djii beuroudj tay fawmou goobeu (2 fois)

{1er couplet}
Yeah ! Bandit Mic rindina Gaston tok cii maxama Baye Dieuwrine
Fokk gnou nkamou kouma laale niine may deuwline
Souma téyé Mic di sétou Baay Sen lay guiss
Dou faye Djante leu rime bouné di khadiss
Li dou nèène maame nél maame
Seute nga cii Rap bi yaw lila waar moy dioxma yélou maame
Ni Mbacké Dioum fékéna diamonoy khour mbégué
Souma dionkoné dou pour ganaaw keur damay tuur dégué
Fila yuur tégué, Gnoulay muur bégué
Eukhlou zikar fikaar haale dadji peuybi pour yégué
From heart to heart thiofel naaw ni Bird
Yëg la takhawé bathieu laff yi naaw dieum cii God

{Refrain}
Day Dem Bandit Mic bi day dem
Bokou gnok gniy takk dii fay ni tallou mbaute
Day Dem Baay Dieuwrine day dem
Demb lagnou djii beuroudj tay fawmou goobeu (2 fois)

{2ème Couplet}
Xamé touma Journaliste ak Doulnaliste
Animateur ak anni-menteur
Mélomane ak mélofan
Légui copinage leuu légui bénène page leuu
wakhalma wa mouvement hypocrite ni haine tokk cii djiko thiazleu
Légui Xibaar yététoul dafay yakk derr (Bitch niggah)
Kaddu Goor goorétoul dafay takk ferr
Niou ngui sapp di youte di raay di doute nguir tuurbi ague terre
Tougneul ….yeukeutikou dafay lakk lerr
Bidew gueumeu loul werr bi Hizbou bé ngui cii kherr bi
Demb lagnouko Job tay soga dikk diondjeu illèrr bi
Fokk sa plan guerre bi, Nio ngui cii Blanc Vert bi (couleur de la Paix et de l’Islam)
Hardcor niangalatoul financement moy nouvelle ère bi

{Refrain}
Day Dem Bandit Mic bi day dem
Bokou gnok gniy takk dii fay ni tallou mbaute
Day Dem Baay Dieuwrine day dem
Demb lagnou djii beuroudj tay fawmou goobeu (2 fois)

{3ème Couplet}
Day Dem Bandit Mic bi day dem kène douko téyé
Téggil RAP politichien moytoul dakaro star
Day Dem Baay Dieuwrine day dem kène douko téyé
XEL KOM YÊG NEK TOUTI WAKH béy MOUDJADID
Da nga fokni dagnou déh ! Hunhun run run run
Sa xol bou bone bi yagui safara di burn burn burn
Nio ngui cii PEACE LOVE HARMONY ak fun fun fun
Niola feeté kaw guiss gnou modi téén sen sun
Da nga fokni dagnou déh ! Hunhun run run run
Sa xol bou bone bi yagui safara di burn burn burn
Nio ngui cii PEACE LOVE HARMONY ak fun fun fun
Niola feeté kaw guiss gnou modi téén sen sun

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR