LYRIC

Weury ba Xtime, dem fou né wané xaragne ci cypher
Xel mi ci Xrhyme, niak xam gueuleum, naxssaay fa
Khif ko ni bouki naam, burn gni manoul niu dékku say feux
… Xool ko ci book yi xam, li yéem diam yi rek nga saytou
Tay niou gueuneu psycho, sakhi laaf naaw sagne ko
Djiteul sunu xél, ba sunu lamigne guinaw – Dagne ko
Liguey reunke jouti ba, loumou touti wouti ko
Xuss ci mou soti niou tibeu, goudi goudi niou gnibi Rio

PPS day déme
PPS day déme
PPS day déme
PPS day déme

Léer na! Ki naxaré xeuthiol moy ki boolé ame ak niak
Ki nangou li borom bi namm, beuss xolam bi samm, ndaw lagne niu ko niakk
Born to shine and gain respect, fi mou gueuneu leundeumé niu xuss puss ték
Xuss tuss rek, Truth is back, Writah the Rhyme maker true suspect
Diegui nagne whatever – legui djangalé warèefa
The Ghost will stay for ever, rouhou Xalima waxèe fa
Wakh waxaate dou beury wakh, Mbedeu tanneu niu né Oui
Séral xollou diam yi, khooloul yaw miy mér aka néwi
Baax yaay dou niaki noon, khass waay di mbaax ci moom
Masslaay li yokki mboon, that´s why ma doon ki ma doon
Ngeum gui matoon, soodoul number 1 todjo féne
Never number 2, father P, writah nga né

PPS day déme
PPS day déme
PPS day déme
PPS day déme

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR