LYRIC

{Azou}
digg bi side tégati diégo
wicked song real yi tidjéko
diéme kanam,G-Y ko nam
thi bépe anam niou missionéleko
boom boom
niou tekki brain
kep mic thi hand yi
canalisé haine yi
indifi ndam liy béguali hommie
haaaaa

{EL CHIGGA}
crick si digui bi
tek si deugg bi
no dou diguidi (no digidi das fx)
fok niou djiguini
mic bou didji bi
kakhh deugg bi
bakk teugg bi
diapp bou beurri bi
danné si beuréé bi
faggou beureupp bi
12 a
diggui bi douza never the looza
gangs sa flouza
exploza

{Stan flinger}
Seug si job bi tédd si thiop si akimo hip bi tokk si hop fake gui si touche bi digui bi diguini mouss yi fuck da low gnogui gneuw téppi lépp li ngén gnaw séppi lépp lifi gnaw képp lépp lifi naw kén dou raw

{REFRAIN}

{WICKY LOHJ}
Diggui bi center dk
go google nga cliké
Site you hip la
jap you hood la
sant noumniouye dk
Sen mother fucker style de merde la gy side di bakk mer
ba ndadié bi doné yegg leuz fekna niou tamou ndér

{KARBALLAH}
nior diékhi réne
diégui brain
nioddi sap lénéne niou fente béte lene
watie wéki datie lou métti tegguiléne
your know da name
jah me rue da crew
g-y daa hood
we claim
degguou di dém
dou manké rendez-vous
seufou ba rouh di dégne

{Azou}
yokk nguem ngeum,
job ba guéne thi peunde bi thi underground
hood béniou dopé,dieum yi hip hoppé
niou callé té soxla ouniou moukhi brown(chanvre)
copie wouniou style yi di sounou own
hood nigger never doko bakk round
beat yi niou bouclé
di ndéki thi couplet
sounou industrie melni boogie down

{WICKY LOHJ}
Douniou bayi mou low niou dass mou niaw
Li ngéne done khar mo téw si réne
Lou rap bi lathie lanie purgé peine
Djiguini fou la ,def le tout la,rap lou gun,gy le hood la
St esprit teck le prix ani bruit say the street

{REFRAIN}

{MOSHADY}
No snitch
we rich
we rep this
with made skillz
When mad chicks eat dicks and drop boobs up on this beat
Yell it capsi – gy
Fuck it diplomatic visa
Come to fuck with.us
and get the army coming in your hood

{Rosso}
Nio nek si center bi men
warnga khamné dou néne wakhnalako dou niétt dou niar té dou béne
nénala u understand
jah me rue kumpa naléne
rigth now nio fi nék di representer g.y

{REFRAIN}

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR