LYRIC

We Love (U)
We Love (U)
We Love, We Love, We Love (U) (bis)
Diyeu maman

{Verse 1}
Boul di boul di boul di non non boul di cry
Thioneu bi ngey dathie tchi Keur gui maman non dou saay
Maman suma yaaye
beugu naleu tereul fi ci adounaay
Maman yow sa khole bi féss neu yermandei
Sou dome dioyè nga dioy sou bégué nga réh
Soneulo sa borome Keur si xoulok xékh
Ouffeul nga ko ndiambote dokh ci liko nekh
Maman suma yaay
Togual niouley beuss akeu raaay
Wakhmeu louy sedeul sa khole ma defko yaaye
Tay dji dameu diouk ni fo diar rek ma finteul leu waye

{Refrain}
Mama We Love (U)
Mama We Love (U)
Mama We Love, We Love, We Love (U) (bis)

{Verse 2}
Yaay dafa soneu ci dom
Yaay dafa yagg soneu ci dom
Yaay taloul dara lepp nguir dom
Yaay dafa yagg soneu ci dom
Sa yooo tissé da nga sori say dom
Lepp lou baax nga diglé pour niou am diom
Tay dji dama lay santé nit kima doon
Amoul téranga aduna yaw boula diombeu
Maman goudeul fane yaw magatal ba nior xombeu
Yalna yeex mais Aldiana ngui ci sa tombe
Yaay boy yaw li nga niaanone nangou neu yaw aannnh haaan
Tay dji sa dom yi seuyi nagne ba done ay parents
Dom loumouy fayé thiono waadiour
Xana magg tekki teral ko né buur
Fatalikoul thiono eumbeu ak seug diour
Aakk ndiourël bakhoul kone nak mangui délou toup

{Refrain}
Mama We Love (U)
Mama We Love (U)
Mama We Love, We Love, We Love (U) (bis)

{Verse 3}
Yaay dafa soneu ci dom
Yaay dafa yagg soneu ci dom
Yaay taloul dara lepp nguir dom
Yaay dafa yagg soneu ci dom
Sama khol leu bindeu waye bi
Waye tchi sama yaay djima diaral lepp
Kima lébbal borr bouma meunoul faye
Diouraum gnéinteu werr ba souniou dieum tay
Yaay meusseu done sama kiraay
Maman indile nala samay dom
Niou ouffou ci say wett naane leu Mame mbooy
Mame mbooy
Naane leu Mame mbooy

{Refrain}
Mama We Love (U)
Mama We Love (U)
Mama We Love, We Love, We Love (U) (bis)

{Outro}
Yaay dafa soneu ci dom
Yaay dafa yagg soneu ci dom
Yaay taloul dara lepp nguir dom
Yaay dafa yagg soneu ci dom
Mama We Love (U)
Mama We Love (U)
Mama We Love (U)
U U U
Sédé naani Yaay djou baax ngeu
Sédé naa yéwène nga yiw nga
Sédé naa ni am nga diiné
Maman love yaay sama rééni xol

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR