LYRIC

{Intro}
Légui nak dara diakhalatouma dara yeemou meu
Young Nigga légui nak waxtanou kou teukh leu, kou goumbeu ak moumeu

{Verse 1}
Fi kène faalétoul kène boppeu sa bopp égoiste
Kouné yaak sa xel bou gaateu rekkay péto fils
Dawal sentiment ba accident eumbeu dagneko miss
Wowé sa guel bb té ngakay teudé pédophile
Ah ! Tass yakaar melni Eto fils
2002 leu Sénégal baayi jop di Egotrip
Politiciens yi dagnouy nakh chaque jour ni fonds vert bi
Gni la gueuneu djégué bougnelay tuur leundeum kay do guiss
Pauvre yéy gueuneu liguèy mais pauvre yéy gueuneu beuri
L’argent appelle l’argent. Pauvreté mom amoul sakh crédit
Testament amatoul ndakh amatouniou lougnefi baayi
Yone bou done dokhal yone Président moy ndieuk diaar CREI
Loutah Toubab diokh niou Indépendance bène 4 AVRIL
Parce que daf nio Poisson D’Avril Ngaaka bi
Dou rayna niam Sankara ak niom Kadhafi
Pays Emergent bouy daw 1 à l’heure Carrapid
Nek Top Modèle la gueuneu diégué que nek Modèle
Sagam Yallah sakh nopina wakhou Niit loumouy njeurigne
Aduna kay mom toukineu mais xamouniou foumou dém
Légui même Jésus mountoul oubi beute wakhou maak Serigne
Galsen Lyrics

{Chorus}Galsen Lyrics
Siip do sakh siip Young Nigga do sakh siip
Do sakh siip, Yeah do siip, Young Nigga do sakh
Young Nigga do comp.
Guissouma lou lerr fi lepp leundeum dara léroul sama bopp
Oh No ! dara léroul sama bopp
Lepp diaxasso mane xamatouma Young nigga do comp.
Djiguène yé ngi seuyeuk djiguène gni
Goor yi di teudeuk goor gni
Bakane lagni wéthio Money
Mane sama Diamono mo ngiiiii
Young Nigga do comp.
Do sakh comp., do sakh…Do sakh comp.
Oh No Do Comp.
Do sakh comp. Do sakh comp. Do sakh comp.

{Verse 2}
Doundeu bou melni vie de rêve la gueintone
Gueinteu biir gueinteu leu kay lane la fogone
Bala Politicien wakh na wakh leebone
Kouy khaar ci niom xeuy nala lerr ni do gontou
Nit ya ngi beug reuthie déh mais mou douniou def loudoul dieufou safara
Pourtant nieup meuneu reuthieu safara mais kène dou reuthieu déh
Sénégal gni fi gueune dokhal industrie sangara
Boy khol toudou niou Jean Paul, François wala Pierre
Ay Boy you beugoul déf dara ni kou dioudou jour férié
35 ans profession fait rien. wéréinték talal lokho ya tchi premier
Ay parents yu amatoul yakaar terminé
Sénégalais Moumeu dou lekk xalisseum dédééte
Kone sayou guéweul wakh nala lerr mo ngi investir
Dakkeu lékanté souniou biir takh deum yi retraite
Wakh kattu deug nala lerr ni nieup dagnekay fuir
Aale meu bic bou fanaane di rongognou deumeu
Saafara ci na xégne melni cocktail lou deuk
Soubeu examen dagneka wara géré deug
Wala Fuite yiy dall trichet day fay deukeu
Prof yi djangal naniou lepp sauf niniouy téki wéh
Kène dou taaneu djoudou pauvre mais bo tchi déwé yaw la nekh
Gni amoul louniouy lekk rekkay né di didji day
Dara yomboul mais vrai Yigo daffay nangou xéekh

{Chorus}
Siip do sakh siip Young Nigga do sakh siip
Do sakh siip, Yeah do siip, Young Nigga do sakh
Young Nigga do comp.
Guissouma lou lerr fi lepp leundeum dara léroul sama bopp
Oh No ! dara léroul sama bopp
Lepp diaxasso mane xamatouma Young nigga do comp.
Djiguène yé ngi seuyeuk djiguène gni
Goor yi di teudeuk goor gni
Bakane lagni wéthio Money
Mane sama Diamono mo ngiiiii
Young Nigga do comp.
Do sakh comp., do sakh…Do sakh comp.
Oh No Do Comp.
Do sakh comp. Do sakh comp. Do sakh comp.

{Outro}
Légui nak dara diakhalatouma dara yeemou meu
Young Nigga légui nak waxtanou kou teukh leu, kou goumbeu ak moumeu

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR