LYRIC

Biss dou reuy Iba Mar songu daan ko laay
Xamna ni mane leu Killah xamni rap bou waw bi laay def
YeuknA li m li xew tchi mbedeum raboutoumA thioki Laay def
Ame lot of doe doutakh ma sopi mane mission bi laay def
Boycottou sponsors yitewoul guichets fermés laay def
Hey mane leu Killah xamni rap bou waaw bi laay def
Loutakh public bi diokhma thieureum rap boubakh bi laay def
Guanouss ak kekk la boul saurou mane deh tekk la def
Boul declarer (guerre ) waatna ni seuss reuk la def
Mane rap bou takh baye fall yi gueuneu neh tchi waar wi laay def
Mane rap boutakh boy yi dagu diplôme yi tekki laay def

Tekki tchi rap bi boudoon comercial rek lekk laay def
Gueumlo lén sen bopp niou free gueuneu nekk lay def
Nioun sunu rap dafey denoncer lou diaroul yoon
Nioun sunu rap dafey wakh nit li thieureum doon
Yow mane leu killah xamna ni rap bou waw bi laay def
Bou gars yiy caguouléwo nigga fang dathie bi laay def
Fuck internationnal bi mane kocc barma laay def
Rangkalé bus yi niou anguou kilomètre yi laay def
Xamna ni fake nga motakhit li leu meti laay def
I’m not tryna be cool with you fuck laay def
Ma dekil rap bi 2007 beuleugui sissou ngey def siip nagne sa game mais blindé ci vice yi ngey def

Amouma titoukaay yallah rekeu yélo peur pi
MAis kouma diokh thieur nawloma naleu delo thieur bi
It’s not fuckin about pop in your nice car
Only wisdom get you humble in my eyes spot
Guedj la tchi xayma té yow mc da nga literou publicou ignorant bi bou nopiwoon doto titeurou
Wussup hand ma clap I don’t care the gunshot
Gunzout gueun tchia wout nopilo the dumb’s out
Fucked up ain’t bullshit this the top top hashtag Bring the old school rap tchi flash back
Yow mane killah siip nga dou rabou tchiaptaat
Mbaute leu ci chaque track flavor leu saf sap
Yagua djiegui obstacle teudiou leulou job stop

Tangu na ni magma eskiver seni traquenard mc maay sa nightmares the killah flow leu mic marr
soow doko lathie poulho thcine doko lathie narr xathie niare nit to the doff teuguA dathie mbaar

Yow mAne leu killah xamna ni rap bou waaw lay def
Xamna li ghetto boy yi khaar ci m.i.c bi laay def
Liy leereul yone bi dalal xel yi doli diom yi laay def
Liy doli taar tchi bilé game bobou ba legui laay def
Astakhfiroullah boudé diglé na louy sank diam yi
Dieuleul li bakh li bone nga meytou tardelo leu ley def
Yow mane leu killah fesseul stade yi del laay def
Fuck gnima banie yow foma sené tchiél ngey def
Nioun sunu rap dafer lerr dou meusseu pervers
Nioun liniouy tekk danie koy dound sunu terre terre
Hyper fier non filston laisse ton pere faire
Mic mic check boudoul deugu douniou wané love
Boul dale tchi ngour gui diotè nan nioun douniou wané love
Pour yolé fake yi neh tchi mic bi douniou wané love
Pour gaur djiguen yi ak pedophil yi nioun douniou wané love
Télé biy diAngal sunu mineur yi nouniouy foonanté
Serie yi diangal sunu sister yi nouniouy mbarané
Fucked up galsen wakh deugu nimou fi haramé
Yow mane killah mafi diaaroon di plané

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR