LYRIC

Yagg na tarr may dekku , ken mussul degg diaambate
Life bi yar niu si metite , rongogne niu nal ko diambaate
Diambar tigui sigui si ghetto ken duniu diam baate
Yeungeul niu yo,beu neu , wayé never doniu damate
Niun , Daniu Juddu Jomi
Namp naniu ba deugueur ferr , xouss ci souxeute jom yi
Dundu naniu ci barack , yeewu taax yi diniu seupu
Luyass cogno cogne , pa bi garé , cine yi deppu
Panne yeré daleu , deme keur Deukeundo seetani télé
Cipatu ak xool yi , melni niom nimu ma doon yitélé
Xamuniu woon né goné buur leu , lou way mugne mou diex
Xelu xalé tool le , Dji ci lou baax , euleuk mou neex
[REFRAIN] (Amdy Opti)
Life is so real ; people are fake
Li may saku mooy , ameu mudj gu rafeet (chant)
Sama demb moy lampe biy leral fama dieum
Sama Sama ngeum Bayima ma doone mane

Bayima ma doone mane
Bayima ma doone mane
(*2)

(PPS : Let Me Be Myself)

Hate me or Love , I stay the wat I am
Malaaka wala djiné , boy bu yarook weuyoo yeme
Maye taan di bagne , signe di gagneu , luma ci gobbé gar
Maye dioxé di nangu , doxé ci tanku goor , luma ci gobbé gorr
Ku sa ape jott borom bi guiss may la
Soy fataliku da ngay sokhor deugeuleu Ismaïla
Tay la degg bax yaye , demal do sen morom
Daniuy dolli sant ndax lu soti ameu borom
Tay numu mel douma titeul , geunone nafi thoiol
Limaye japé diam , diegui na am am wala ndol
Paul, mawone Dangou moy PPS bou rene
Ghetto Child never change , geum ko saxfa reen

[REFRAIN] (Amdy Opti)
Life is so real ; people are fake
Li may saku mooy , ameu mudj gu rafeet (chant)
Sama demb moy lampe biy leral fama dieum
Sama Sama ngeum Bayima ma doone mane

Bayima ma doone mane
Bayima ma doone mane
(*2)

Mo-Bouray-No , equipe bi dou sopeeku
Liniu liguey deuxeugne si underground tay moy soteekou
Messaghe crew forevr , Hip Hop bi seedé naniu
Sunu gueinte mudju na ami tank , mbedeu seddeu naniu
Xeutio wuma lanc , ndap li yaa na ni géec
Deet fontu wuma defantu wuma , dalal yaay ami gacc
Picc Diawu la xam , diante douko teeré naaw
Ku weedi na lacc Hip Hop , mom mi top sama guinaaw
Fuck your business , mane love laye sedeulé
Fedali Koleurek gni teulé xol yi ni niu kay seddalé
Ngeumeu niou indi fi ta euleuk mo niuy dialalé
No pain No Gain , yoon wi nonou lako Jah laléee

Kouy xeutiok mane teen ma bala ak mome
Lac de guiers moma yiteel baay

The Ghost Writah , Xaatim ak Kàllama !!!!!s

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR