LYRIC

{Checky Blaze – Verse 1}
Nigga Bang Bang
Téyeul sa mic nieup di tang tang 
sangg sangg fake yi di bagne téyeul sa hand hand
Dou dègne dégne yokou sa fiit, yokou sa sagne sagne
Dou dègne dègne Yokou sa niit, yokou sa mégn mégn
Dou dégne boy dofa diott nigga niou youkhou ko
drapeau mbed bi mbédeu bi sampe ko, dampe ko, nampe ko
Mic dagn koy meun ba sa xoll di bone dieul mic bi xampe ko
Dokh cii bepp fake defko sa mind nigga kone na-ngou ko
Rhymes ak flow bi di daw, sa mind bi di naw di mégné
Fomay séintu ma raw, sa digui guéw nga niémé
Hip Hop doundou ba faw, cii Game bi lagni déwé
Mbédeu def niou outlaw, founiou guéné mo yémé
Rasta man yi beug Kali,
Wala ndiago beug bali
Mane ak yaw cii Mic dafay feuss ni Yalla ak Yali
Nieuweul souk naane cii ndale yi
Seug todial dieul général yi
Songue Mic démé fiit done vainqueur ni Ahmet ALI

{Refrain}
Dou dègne boy, Checky Blaze done sa alcapone
Dou dègne boy, Mane ak yaw meunou niou bokou yone
Dou dègne boy, cii biir son ma done sa none
Yakk sa life ni joint wou bone
Cause sa death ni ballou gun
Dou dègne boy, Killah Killah done sa alcapone
Dou dègne boy, Mane ak yaw meunou niou bokou yone
Dou dègne boy, cii biir son ma done sa none
Yakk sa life ni joint wou bone
Cause sa death ni ballou gun

{Nitdoff – Verse 1}
Tree Six Five days (365jrs) ligni reupeuteul dou dégne
Tchine yi bou ndaroul yone nékh bou bakhé dou khégne
Nitdoff bou deudou wone mbéde bi kone tay dou fégne
Killah Killah flow, checky checky my nigga na gueuneu tang
Na nga man téy xeuthie ma nigga na gueuneu tang
Kouy bagne kaat, gueumeul sa bopp té gueuneu bagne
Gueuneu lagne baat, mbautou HipHop defko sa kagne
Done saureul cii Hip Hop fo tolou di niou séneu
Rap ba niaak toy nga koy guiss cii maillot bi ni wéingne
Hardcor mélokanou mbéde moy daw cii sa veine
Yokou pastef, xam sa waref téyeul sa haine
May pikero
Hood di titéro
Nit Fodo Blaze we’re hero
Li mbéde yitéwo
Mane mako fétéwo
Nokoss di Rokoss cii beat bi kène douné djité wo
Mayko Hiphopers cii hit bi ngay tokk di bégué yaw

{Refrain}
Dou dègne boy, Checky Blaze done sa alcapone
Dou dègne boy, Mane ak yaw meunou niou bokou yone
Dou dègne boy, cii biir son ma done sa none
Yakk sa life ni joint wou bone
cause sa death ni ballou gun
Dou dègne boy, Killah Killah done sa alcapone
Dou dègne boy, Mane ak yaw meunou niou bokou yone
Dou dègne boy, cii biir son ma done sa none
Yakk sa life ni joint wou bon
Cause sa death ni ballou gun

{Nitdoff – Verse 2}
Number 1 cii bepp top ten (10)
Tangue andeu ak wékhtane
Beuri mbaute né poftane
Ghetto bélène diokh régne wayé daniou lokh guène
Djot na Courrone bi dotou mako diokh kène
Real niggaz djouk lène tott niggaz tokk lène
Ana gni done djoy RAP nieuw lène ma bott lène
Yégueul lène cii péinthie ya
Firi waat sèn guéinte ya
Mélakh ni férr gnéinte ya
Lérale sèn yone ni djante ya
Kou done xell niarr na dégne cii yaw

{Checky Blaze – Verse 2}
Dou dégne boy, yémal sa plassou rak may sa phénonème
Nieuweul Holla back, bamay shoutout xam ngani féno man
Foma sèneu def back tale sa carrière ni Kérozen
Fuck the haters, I’m Back guissou malène zéro ngène
Ya Nigga wala Noone
Tiénél bokk wala niou niaf sa
flow bou you melni Gun get the fuck nieuweul get sa
Killah, Checky Blaze Never Sédal nigga bangin on
Dou dégne BOU KENE TOKK Microphone ba ngui ni mongui On

{Refrain}
Dou dègne boy, Checky Blaze done sa alcapone
Dou dègne boy, Mane ak yaw meunou niou bokou yone
Dou dègne boy, cii biir son ma done sa none
Yakk sa life ni joint wou bone
Cause sa death ni ballou gun
Dou dègne boy, Killah Killah done sa alcapone
Dou dègne boy, Mane ak yaw meunou niou bokou yone
Dou dègne boy, cii biir son ma done sa none
Yakk sa life ni joint wou
Cause sa death ni ballou gun

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR