LYRIC

{Verse 1}
I got to wake up early in the morning
A long way to go because I got to fine my way alone
Need to stand up get better the warning
Which makes me know where is the line what’s left to be done
li lay bollé si lép li takh ba dougne la faté
Ya koy liguéy ay nélaw dou la ko may
Li lay diokh gueude fép fouko kéne doul khalaté
Everyday amna tole bo wara bay
Bala diante bi diok fog ma diok tél ko wadial
Ready to go darkness dou yeugoo
Boum bi la wara dok dieul mou ndieuk bagne kouma nadial
They better know witness it a Mo
Dieuf dieul la bala wéss réthiou di si ame yoonn
Beugouma wéte tomorrow di méré kéne si niomm

{Refrain}
Early in the morning
Souba téle
Yéwou seulmou gadou bag takeu daleu cuz i got a long way to go
Bala diante bi diok diok
Early in the morning
Souba téle
Fog ma fipou yotou sak diéma dialeu cuz i really need to know
Bala diante bi diok diok
Early in th morning
Souba téle
Early in the morning
Souba téle

{Verse 2}
I don’t wanna stay around my home
cuz I do know them are waiting aside
Beuge reuthieu euleuk comme niépe ouff samay dome
I do know I go to go get tight
Warouma togue féne di gnéé sou may morom
Linga dji ngay gaupe yaffouss dou weuy
Kou nék kham na li gueune li fatch sa aye gaume
Mbeurbeff dou daupe cactus latch na téy
Avance bi nga dieulone wara beurék life
Contrat bi yako signer wone beuré si déss
Revanche bi nga digué wone dassone sa knife
Boul faté bor bi nga lébone diogal deff lou khéss
Diante bi fénkone mou ngui dougui waate
Leundeum ma ngui yoote télal roote teutch sa ndaa
Fi niou la bayi wone warougne la fa fékate
Gni nga wara boote wanal niép ni gayndé ngaa

{Refrain}
Early in the morning
Souba téle
Yéwou seulmou gadou bag takeu daleu cuz i got a long way to go
Bala diante bi diok diok
Early in the morning
Souba téle
Fog ma fipou yotou sak diéma dialeu cuz i really need to know
Bala diante bi diok diok
Early in th morning
Souba téle
Early in the morning
Souba téle

{Verse 3}
Get up at the very time don’t accept to be late don’t be a loser
Stand up however the clime go open the gate well be a good chooser
Frérooooo
Beugouma niou rérooooo
My sistaaaaaa
OoOh nan na nan nannannananana nan nannnnnnnnnnnnnnnnnn

Early in the morning
Souba téle
Yéwou seulmou gadou bag takeu daleu cuz i got a long way to go
Bala diante bi diok diok
Early in the morning
Souba téle
Fog ma fipou yotou sak diéma dialeu cuz i really need to know
Bala diante bi diok diok
Early in th morning
Souba téle
Early in the morning
Souba téle

Early in the morning
Souba téle
Yéwou seulmou gadou bag takeu daleu cuz i got a long way to go
Bala diante bi diok diok
Early in the morning
Souba téle
Fog ma fipou yotou sak diéma dialeu cuz i really need to know
Bala diante bi diok diok
Early in th morning
Souba téle
Early in the morning
Souba téle

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR