LYRIC

… Alhamdu wa shukru bi borom bi défé niu raam ba aksi ba fi
Gni gueumone gueunoon naniu néew, niu tann liguey li déss niu ba fi
…Niu deug tank dox, khiff Mar seugueu tankh ndox
Nieup naane dina sanku doff, Tisbar moudjé sant gox
Bala Xtape dama tothie fépp, Xshow yi di faye salle
Underground bi di Djité ci pétte réewu Marieme faye sall,
Ma peundeul sa town ak yénéni vers, déllo sa mbind yénéne univers
Teungueth am na rappeur, li mou yor dou diékh, kouné indi verre
I shine like the Xtape, xacci door bi dalle States
Nék supa star avec Niary Tape, sama son la nieup di wari fépp Massouniou niodi dara, mass naniou djangue baa sine mimara
Mbind miy réggal di xonte ki mara, té Gueumou niou téeré di sangou ci Mara

First album Best album
First album Best album
First album Best album
First album Best album
Xaatim ak Kallama

Ghetto boy bi nammatoul avion, prestige ak first classe
Niu deuxeugne lep di dundu ni baayfall, l’école nio feuss classe
Lou la yéem doundou nako daaw, Miami ba Time square
Guddi ma guindi ki doyadi, beuthieuk ma sopi ko rhyme ci ki wér
Dama aay negger, wakh ko ñiy roukh sa égo
Di saay saay negger, dingà souroukh té éggoo
Paul 2.0, ronalzidane, wala writah
Meuné funé, loco, PPS, guissula yaw mi raay teu
… Daniu yéek té guissouniou lokho, guiss yoon wi di dékku mougne
Fils gontu oubékku, djékou Piiss noon bi guindéeku moûgn
Somay teukeulé please na doon sakh Nas ak Jay
Parnasse ak Dieu yi, guiss nga né wakh na sakh djeuyii
Gueuwma taye nga may taggeu, euleuk nék ci radio di soop
Louy ndayou di ragadjou goor, sen game bi di dadjalé salté ci saaku di goop
First album best album, ngay petard may taal bombe
Ba suba damay xéw Wakhal Xaatim ak kallama

First album Best album
First album Best album
First album Best album
First album Best album
Xaatim ak Kallama

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR