LYRIC

[Hook/Omzo] Façon bou né
Mane ay xétou noss guiss na Façon bou né
Ay xétou xonett guiss na Façon bou né
Bou life bi di tarr
Bou life bi di nékh
Mane dara douma diakhal my nigger guiss nakh guiss nafi Façon bou né
Ngani lane?
Façon bou né, Ngani lane?
Ay rappeurs ay doul, guiss nagn Façon bou né
Ngané coming soon mais toute façon dou né
Fi galsen gnoune rap nagn ba diékhal, lougn déf rék nguén défat,
do rap lougnou diakhal, ndakh rap nagnou fi Façon bou né
Façon bou né
Façon bou né, Ngani lane? x3

[Part1 – Omzo] Guiss nala’k liguay niangal yeup
Fuck ki, yaw, keulé gni nguén andal eup
Sén pire cauchemar té malén téré nélaw gouddi
Sama heure mo diott même si sén horloge biologique
Boudé rap en ce qui me conserne, Rappeurs yeup pay doul ni fond vert
Ma yak rap bi mélni doumou richard
Bobeu légui ték game bi mélni memory card
Yamoul ci wakh nigger, rap ak fit leu, Bass ak Fif, Fresh To Def ak Pop A Shit leu
Boul lathie nakh hit leu, niata gnofi clash ba guiss meu, Gnou guéné canamou kathie mélni Snapchat Filter
Fess nga gatt ni espace téléhone
Mangek sho bou fess ak telebone
Si cogne bi di bondé, takk ngaandi chaine, fuck Excaf Telecom
Ma lak toubab dingmeu sakh ték Nix
Sho bou romb ma khol sa forme mélni staff technique
Rén rappeurs yeup dinagn ziar Dollar
Comme kou gnoumoul Yallah waro tokhou Khar-Yallah

[Bridge] Façon bou né
Dama téleu takeu ni caleçon bou wékh
Beuri ay barres, Prison ferme si tu l’ouvre
Boy manguik basse ba mélni Fruity Loops
Mc té nga cool té nga diang say leçon
Ba ma déf leu mouss si tu fais le con
President Dollar boy confirmél sa vote
Ba nga daw mbéd mélni timiss seu diote (Miézé)
Rappeur bou nieuw rék, niouné ki moy soul wa Buzz Lab
Même boudé ay R&B ak Soul leu, my nigger soul nagnou Façon bou né

[Hook/Omzo] Mane ay xétou noss guiss na Façon bou né
Ay xétou xonett guiss na Façon bou né
Bou life bi di tarr
Bou life bi di nékh
Mane dara douma diakhal my nigger guiss na Façon bou né
Ngani lane?
Façon bou né, Ngani lane?
Ay rappeurs yy doul, Guiss nagn Façon bou né
Ngané comin soon mais toute façon dou né
Fi galsen gnoune rap nagn ba diékhal, lougn déf rék nguén défat,
do rap lougnou diakhal, ndakh rap nagnou fi Façon bou né

[Canabasse – Intro] Son bi comme essence moungui ci station bou nék
Ni slip bou mak eupé caleçon gouné
Tothie nagne fi ay sacou néne
Takhoul ba sacou néén (sac vide) takhaw
différence day fégn ounou takhaw (ci Façon bou né)
Ngani lane? Yeah mako wakh

[Part2 – Canabasse] Sama story snap di sa budget clip
Sama béne thiaz mo eupe fitt sa clique.
Dioumoulo It’s Bass, dama diouk ni dick
Mangui ci birr di daw mais bagn douma eat mbiskit
Room service ci laal bi fils
Sama carrière bo guemoul God di ngueu guiss mistique
Damané 9 dou 6. Don’t djoutou please
Real cachet dafay kawé fognou tassé yaw yay thiop dessite
Toujours à l’affiche ni Pop Star nguiss neu
Yaw bo sagnone niou changé kanam ni Snapchat Filter
Diko ci bombe normal liquide nieuw
Manak Galsen (chiffres) melni baram ak clito
Bass ak Fif leu, Yarakh – Carac shit
Mc’s di sandi khér, gnou dougou banque di khagne ay briques
Borom xél yi ndandue nagnou kane moy doundal yi parasites
Mais sunu nieurign douko guiss comme bossou parent bi
Défar na ay Mc’s, Façon bou né
Yeah ray ay Mc’s, Façon bou né
Soussal nafi ay nakeu, sukeur nafi ay lakh, souffler nafi ay gâteaux, (khéw nafi, khéwat fi?)
Ci Façon bou né
Selfi ak pourboire serveurs yi bég
Sén dépensou wér si bén gadget
Dans toute sérénité, dama yagg bindeu ay textes bay signer ay chèques
My nigger guema dama ci guéneu ba moudié dépayser
Seul nègre dans le hammam
Lima weur moy white men ak ay naar
Façon bou né
Seul mec sama diwane
Lima weur moy dé cash bégal ma’
Façon bou né
****
Faut que ma weur sama selfie pour guiss samay mass
Pages yi passeport bi légui mou diékh
Yémal sa cogn lingay déf dou dém
Cassos boul dial seuss, di nga encaisser
Bastos ci gatt, mic ci tatt, dagn lay dioutal ni diék

[Omzo] Rappeurs you fake ké chaque jour ma guiss
Snitché sén bir ni ay journalistes
Fuck rap bi dafa yombou ci mane
Fake niggers ci bir nathie bi loloy ombre chinoise

[Canabasse] Lignouy déf, simple ni mbourou madiokh la pain chinois
Fils sa rappeur reu daka doul iPhone 5 chinois
Limouy guénteu c’est moi
Kimou beugueu nék c’est moi
Mais essence seum barriwoul né bébé bou dioudou après 5, 6 mois
Dollar tell them

[Omzo] Yék ci kaw scène keecee million
Ziar girl bi nieuw ci guéthie bi lolou moy sam péché mignon
Yeah, limoy CR7 ak Léo Messi
Mc boul gnou diémé toudou tant que néwo merci

[Canabasse] Sentir romeu, fuck sa sinus lidou géométrie
Rap ame neu règles anus tangente triogonométrie
Méti méti méti méti nigniy saré fok mou méti
Athietangue yi ci kaw péc yi bou gnou paré diokh la béquille

[Omzo/Canabasse] ] Méti méti méti méti nigger tégal lén lou métti
Boudé nioun nga beugueu soul tant que déwo néci
Sa carrière mongui ci thine bi ndank ndank gnou koy diéki
Boudé nioun nga beugueu soul tant que nigger déwo néci
Ci Façon bou né

Added by

Ahmed

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR