LYRIC

Verse PPS
Yeewou jouli takk dalle, soobou si waarou baaye
Adouna missalee tôle guir gueneesi fok nga baye
Sama dème la kham, lamaye fori sama koumpe leu
Bou done agne, lanthie bassa dess Lou bour loumpe leu
Gueumouma mbok, sama niakh rek ma nior
Douma talale lokho, tann na yone ci niaar
Douma teggui yone, kone nako takhalee
ame na niou weerou si mane, di yaakar, dootouma khalee
Tok di gagne reer leu, ndekki agne rerre leu
Combat boudoul diekh, sa congee teudi armere leu
Ndeye ak baye dagne niou ko lebal, faw niou faye ko sunuye dôme
wareefala fall, sa niakhaye fathie sa gome
Seuss reuk ci Ngor ndeme ndol dalaye bôme
Teuss teussi ci tangor, ba jant wathie rideaum
Fi dara yomboul , fok nga saxoo jeem
Keiam mangui dème …..
B Fii jome mo fi jekh, jeengue gueune fi yombe
Nieup beugueu fekh amouniou lene louniouye jombe
Tann na, feye si njoup ni djeune
Douma sathie, douma fene, douma lore, douma bedjene
Rang si usine journalier wala outi chantier
Marchand ambulant, louma si forr nako santée
Gni koy def gueunoumalene, sot métier amoul fene
Dina Job khebouma lene, khiff ak raflée khamoul kene
Kouye rame di la boote, sou dokhee na sa xel dale
Li may yeuk moy deug, Dara douko nassaxal daal
Goor yomboul, fok nga gnemee gnafee
Khame sa waref, seugueu deekou jaffee jaffee
Khiff lekeu, febar fadjou, khalee yi bene walle leu
Sokhla yathia dess, begueul sa gueneu walle leu
Mane môme thiow jiboul, na keur gui naate kote
Kene bagna jambate, ma meuneu nelawee bene beute

Refrain KEIAM
Fight !!!
Fight for this love
Fight!!!… Fight for this..Fight for this
I’ll love you until the end
Baby come and take my hand
I’ll never let you go….Say you’ll never let me go!!!

Verse KEIAM
Yalla def ma malaaka may takk ci kanamam
Mu xam né ma ngui fi, everytime di léeral yoonam
I love you just the way you are, It’s who I am
I don’t have to try hard, really
Gnibissiti nga timis, yoroo dara, boul joy
Amy top ci, Ousmane néna yaw lay roy
So jaxeté xalatal sa njaboot
Yaw la niu gueum té yaakar ak jome nga boote
No ! I don’t wanna let you go
I just wanna let you know
That I never gonna let you go
Dear God…
Neko xiifu ma su mako guise sour
Bul jéema sopéku ni nga doné sama bour

Verse PPS
Ok degg nala K, douma sopekou
Yeene nalene loune, yalna kheeweul yi sotekou
Niak takh jeingue yombeu, nagou sankou Rombeu
Alal takh na diam bi sank, ngueum ak ngoram ba
Dignement daniou koy make, naniou diap naniou ci nek
Yagg bawoul Dara ndem bole naniou ci neek
Souba Dou agne Dou rere, diarna soor
Dinga bek ci sa goor, thiono wathie sa moussor
…. Beg na ci yaw
Seey Bou rafete boude Faye, say doome dina niou raw
K yaye sama doole, mbaar mi may tiim sou tawee
sama reine sama xol, sama Aline sitoe

Refrain KEIAM
Fight !!!
Fight for this love
Fight!!!… Fight for this..Fight for this
I’ll love you until the end
Baby come and take my hand
I’ll never let you go….Say you’ll never let me go!!!

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR