LYRIC

{Refrain}

Souk niaane ngir njaboot dji

Dékou naathie ngir njaboot dji

Liguèy ba déh ngir njaboot dji

Défar sa life-fu njaboot (x2)

 

Yeah yeah

Défal tchi waa keur gui (Tiens tiens)

Doori waar nieuw def tchi wa keur gui

Oooooh HooooooooH oooooH

Défal tchi waa keur gui

Xamo loutah sa papa rare keur gui

Dem doori waar

Défal tchi waa keur gui

Doori waar nieuw def tchi wa keur gui

Oooooh HooooooooH oooooH

Li war tchi wa keur gui

Xamo loutah sa papa rare keur gui

Yeah yeah

 

{Verse 1}

Mama soneu neu loole

Defna loumou warona def tchi nioune

Papa soneu neu loole

Defna loumou warona def tchi nioune

Ki nga done meunoul bokk ak ki nga am

Fo meunti tolou dou yeem sa Ndèye ak Baye

Boul meusseu yës ba di tass niom sen yakaar

Mama da khékh ak déh

Pour diokh leu sa life diokh leu sa freedom

Yarr leu ci baatine def tchi yaw fouleu ak fayda

Dokhna ba fébar pour meuneu fathie yaw sa fébar

Wakhma bane banque lagn lay diokh pour nga fay borr

Yeah ! Pa bi da liguèy néna “Thiabi ya ngi ni”

Moy nga def Maman bi béék

Est-ce bandits ya ngi jail ?

Beus dé mane dina fi gueuthie

Héritage dou khaliss na nga aar sa famille yeup

Ndakh guiss nafi talibéy

 

{Refrain}

Souk niaane ngir njaboot dji

Dékou naathie ngir njaboot dji

Liguèy ba déh ngir njaboot dji

Défar sa life-fu njaboot (x2)

 

Yeah yeah

Défal tchi waa keur gui (Tiens tiens)

Doori waar nieuw def tchi wa keur gui

Oooooh HooooooooH oooooH

Défal tchi waa keur gui

Xamo loutah sa papa rare keur gui

Dem doori waar

Défal tchi waa keur gui

Doori waar nieuw def tchi wa keur gui

Oooooh HooooooooH oooooH

Li war tchi wa keur gui

Xamo loutah sa papa rare keur gui

Yeah yeah

 

{Verse 2}

Never forget fima djouguèy yeah

Fima diaar lolo takh bama mel niii

Am am dou wess niaak dou wëy

Mais meuno khaar lo fi job-boul ba djot ci

Déréttou gorr rek mofi daw

Mou naathie mouy taw. You know ?

Thiono dou reer No No No No yeah yeah

Xalé bou guiss rongagnou mèram di tokk

Kou djom sakhoul sa xol xamal ni mélo ni mom

Di diaar ci yone bou djoup ak yoon bou teureudi bro

Djaay sa ngor dou yakamti mais gueumeudi leu

Yeah yeah

Défal tchi wa keur gui

Lo meun ak lo meunoul tchi wa keur gui

Yeah yeah

Lepp tchi wa keur gui

Lepp pour seu familiaaaaaaaa

 

{Refrain}

Souk niaane ngir njaboot dji

Dékou naathie ngir njaboot dji

Liguèy ba déh ngir njaboot dji

Défar sa life-fu njaboot (x2)

 

Yeah yeah

Défal tchi waa keur gui (Tiens tiens)

Doori waar nieuw def tchi wa keur gui

Oooooh HooooooooH oooooH

Défal tchi waa keur gui

Xamo loutah sa papa rare keur gui

Dem doori waar

Défal tchi waa keur gui

Doori waar nieuw def tchi wa keur gui

Oooooh HooooooooH oooooH

Li war tchi wa keur gui

Xamo loutah sa papa rare keur gui

Yeah yeah

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR