LYRIC

Galsen genius
Galsen genius
Galsen genius
Ga Ga Ga Galsen genius
(Bis)

Mister innovation feuleuti fénéne balak féem la
…Kay geinte di xalaate théme, teukeuléma rek blasphéme la
Rhyme yéy tourou sama mind, wala sakh ma katakayni
Wékh khatte aay ni, El Loco indi kataa kay ni
King DeugE moma deink beat néma ray ko mou dé
Niu xool wanétte ak ki beuteum beuré bi foumouy moudjé
Guissouma maass, guissouma mapandoo, guissouma kouy woudjé
Wakh ji dé dou goudé, founé lay dougou dé – no mbadda naka sa dougoudaa
Dof béy takkal lésse sa MC, dou taxalé rek yém si
Sopi sa king queen gwine, dounya la niu yéem si
Zeus ci kaw olympe, guéwu thiossaane aada mak si
Khawma topando flow, leepay real ni Adamaksi
Dangay djangue niuy tari niune, garè niuy rally niune
Jeuf té wakh dou bari – niune ca arass lagne niu wari koune
… Mandi ci léer yi takh niou féeté kaw
Nga soufé torop ba sakh pr ma laal la fok ma saw

Refrain:
Balance bouma péessé dammeu, writah tonne la dou kilo man
Father P poids lourd, mo la mane, mane kila mane
Diegui nagne li ngaay séen, djaroul thieupi déel téen
Tiim la ni jant nur gui day feigne, writah yi def ma buur ci galsen

Galsen genius
Galsen genius
Galsen genius
Ga Ga Ga Galsen genius

Li niouy def dafa deep, ngaaka douko siip
Djégui bakar bala thiow li di djip
Gueustoo thia arafat djiko ridjaal
Sen game bi gnaawoone la nieuw décoré dialleu
Ci jamdong, tok jangue dong, ba keurou téeré yi maxama Kalif
Yagg naniou ko doundou nél sa général mo xamak liif
Kothie ma ci book yi, Mixtape la guéné di touki
…Be real to what we fight for, Louma matteu mou dagg ni bouki
…Mbed djouroul louma yéem, Yor Sunu kaddu never douma yém
Nattou xamul taggo kén douma yée, guéwu bandit xamul djagg dou moy
…Gni nga beug ci mane lanouy roye, ate mou né mouye gueuneu kawé dou mbooy
…Meuné founé guimi guindi boy, golo ci almette la fépp na boye
Fou léss wakhé Atou feigne, Fou nieup wakhé atout feign
Do laxatou féne, do lakkati fén, jant dou sondel do lakati féne
PPS wowéma Father P, pâpa Paul wala sakh –
Djiné ji, guindi sa mind nga guiss deugui writah sakh
Kheuthiowou mak kéneu ci léneu, wooreudi ni foo ci téneu
Roy dou nourook piir – I’m the best who ever did it

Refrain:
Balance bouma péessé dammeu, writah tonne la dou kilo man
Father P poids lourd, mo la mane, mane kila mane
Diegui nagne li ngaay séen, djaroul thieupi déel téen
Tiim la ni jant nur gui day feigne, writah yi def ma buur ci galsen

Galsen genius
Galsen genius
Galsen genius
Ga Ga Ga Galsen genius

Chant:
Yeurmeudé – léklél mou wagni doolé goor
Yéeté baax na – yéna saay dé ci boolé door
Djolof fok nga dé – niouy soga xam né ya fi meune
Foy jeuléti – kouma djégué mba kou mél ni mane

Ba may done kaana, abass-a ngui lathie fou abdou moudjé
Bobou Mor taallagoul Kalashnikof niu deukmou djeuyeu
Ci Aladji lagne ko naté, jokh ma raaya bourba
Niu magg daane, Ghost writah moudjé feign ca tour ba
Senghor ba Abdou – ba Abdou lay ba deukeu bi macky
… Masso guiss kou mél ni mane, ki aay ci gounék mak yi
Joell ortiz nangou, kweli néma akassa
…Youssoupha né moy PPS bou kinshasa
…Dou ma moromou sén rap assamak yéen
Non dou maak yéen, non non noto beut dou mak yéen
Tête dou mak yéne – talent bagne né teudoumak yéen
Wakh djé beury, galsen gni xaragne manoul matte Ten

Refrain:
Galsen genius
Galsen genius
Galsen genius
Ga Ga Ga Galsen genius

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR