LYRIC

{Intro}
OPD On The Track iiooww
Senegaaaaaaaaaal
Fi Moy Senegal
Un Peuple , Un But , Une fois and Thats iiiit
Fi Moy Senegal

{OPD – Verse}
Bo done lathieté yeksi ngua , sunugalou teranga.
Dakar moy fi capitale, 14 millions dhabitants.
(S) bi santeu Yalla leu
(E) bi Egalite leu
(N) Haine dougn ko diapeu gnoun
(E) bi Egalite Leu
(G A L), pirogue ba ngui ni , fi leu lep di khew.
Fi nguay nguey guiss kouné , gnou bakh te yiiw , niit you amoul feen.
Seydina Limamoulaye , no def ma toudou Baye Niasse .
Ndakh Serigne Toubakh El Hadj Malick , rewmi mouné fé tass.
Demal ile de Goree khol , wakh ma li ngua yeuk sa khol
waye lolou wessouna ndakh legui leneenl a gnouy khol.
Sougnou rew , galsen si sougnou biir khel.
Diouliit andalh catholique , ci diam la paix.

{Refrain}
Rewmi rewou djameuleu , rewmi dara dakhouko.
Eksil sama rew djolof feug gui dara gueunou ko.
Gnoun fi leen dioudo , Magueu dokh fouk gnou waneko.
Bo yeugué limey yeug baat ci kaw youkhoul fi moy senegal.
Senegal Senegal Senegal
Senegaaaaaaaaaal
Fi Moy Senegal
Un Peuple , Un But , Une fois and Thats iiiit
Fi Moy Senegal

{PPS – Verse}
Welcom to my country, Couleurou flag done three
Koleurek diam sakh fii, don’t stress, nioune dagne free
Werte mbox xonxe teunke mbok, ndap niou bokk
Songue Mbaay ak gueethie niou fonke, deukeundo ba diour na mbok
Yeah! Boucounta namm xalam, niani bagne na
Cheikh Anta youxou naxaram, nioul ni deram, demb gaagne Na
Reewou Bamba, reewou baay, Reewu lamb, reewu baye
Namm diam yée moumbaay, foré kaddu ca wéewu beuye
One nation, one goal, one people, one faith
Jeuli Ada ak thiossane ya né wone féss
Xam né yoonu yokkuté na téew biss
Sou gontou jotté douniou dess fils, neskiss- zeum bi téggou
Na loxo jok ca kawa kaw niu niou téwal sunu Senegal

{Refrain}
Rewmi rewou djameuleu , rewmi dara dakhouko.
Eksil sama rew djolof feug gui dara gueunou ko.
Gnoun fi leen dioudo , Magueu dokh fouk gnou waneko.
Bo yeugué limey yeug baat ci kaw youkhoul fi moy senegal.
Seegal Senegal Senegal
Senegaaaaaaaaaal
Fi Moy Senegal
Un Peuple , Un But , Une fois and Thats iiiit
Fi Moy Senegal

{OPD}
Awma fayou sama nation represent koy sama mission.
Opd PPS gno ngui saluer beppeu region.
Dakar diourbel Fatick KokdaKaolack tambacounda
St Louis Thies Matam ziguinchor whats Up Louga.
{PPS}
Fou waay mana né ci réw mi, niu gui ziar di magal
West african soldiers, love and respect, ci sama gaal
Wat gaal yéggo, what xaleu go kate Aada bro – fi la
Thiossane na niu tété waarou Mame, Galsen laniu feel
{OPD}
Li ma gueneu nekh mere yi da gnouy takkou jouk. Dori war
kharou gnou keen ci leen.Da gnouy matal war
Naleen yalla sameu, sama beppeu domeu deukeubi.
Sama yééné reuy neu lolou , God rekeu meun cédé li
{PPS}
Réewu youssou baay péne, door waar douniou bayi féne
PBS xaleu ci daara ji, rapadio yatfu sen kumpe baay sen
Réw mi rap di folli President, di fall sen askan
OPD ak PPS nio link up, ken dou gass kane

{Refrain}
Rewmi rewou djameuleu , rewmi dara dakhouko.
Eksil sama rew djolof feug gui dara gueunou ko.
Gnoun fi leen dioudo , Magueu dokh fouk gnou waneko.
Bo yeugué limey yeug baat ci kaw youkhoul fi moy senegal.
Seegal Senegal Senegal
Senegaaaaaaaaaal
Fi Moy Senegal
Un Peuple , Un But , Une fois and Thats iiiit
Fi Moy Senegal

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR