LYRIC

def dara, deef dara

{Refrain}
fly dem fénén
fly weuri lénén
fly béggéli gnénén
fly boul nagou nioulaye teudj ci mind (x2)

{Gaston – Verse 1}
magui surfer ci Ahmad
surfer ngir mat
diekh fi
séét fé
lép rek ngir mat
boulma teunk bayima
mim kha mim dél dou bayima
dedj deup ngui la beug dadj séy si mom ni mame Ibrahima
ouk leer la dou waxi késsé
dieuf sa leer la foumou fek wax daldikoy féssé
fekhel fecci freedom mi fassoubouko waaf
boul limiter sa bop goor firil say laaf

{Refrain}
fly dem fénén
fly weuri lénén
fly béggéli gnénén
fly boul nagou nioulaye teudj ci mind (x2)

{Gaston – Verse 2}
bou life done diouma nanga fly si minebar bi
donal yaye fall boul top fisso bi fly ba min bar bi
bou niouy diokhogne mbeut mifekhel fly ba tiim bar bi
légui gangster moy guerrier xel mou sél moy yambar bi
sip na séni complot
danga geuleum compoulo
saaga molay jump lo
danga teunkou fils compoulo
niougui lay use ci mind té sibo
hood bi laniouy mboubo
beugla geumlo ni wa ghetto ak wa town warouniou djibo

{Refrain}
fly dem fénén
fly weuri lénén
fly béggéli gnénén
fly boul nagou nioulaye teudj ci mind (x2)

[reskp] Djééé!!! haha!!!
Kagnala mom luxalamom esclavou mode tarkhiss khiss ci nga dieum
li nga deugmal dila geuleumal with no shame … fight ba nga kheum
doon diankha dass sa diam kaw man bou tew nga golou
ndakh niati V nga tek sa eyes dou kén niom ngasi wolou
apart meublé ay takay takhoul sa lép tchill
ndakh poss bi diss na but amna khétou mbékté yo meunta feel
sey tass seyat tass fo tek sa beut mou cass
té nga fly away bala ngay done maguette bou rass

{Refrain}
fly dem fénén
fly weuri lénén
fly béggéli gnénén
fly boul nagou nioulaye teudj ci mind (x3)

boul nagou teudj ci mind (dox dem)
boul nagou teudj ci mind ()
libérél sa bop, ibérél sa bop fly
dokh dém (x2)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR