LYRIC

2011 laa la yéme ni hiver boréale
Kou nawétaane di youxoulo woorna yéggo Réal
My shit is so real, sen mbootaay di naféxx
Tank ma yeug li may def, def limay yeug dina féekh
Samay laaf mako mome, mindef douma teunk
Sama xél reka may yobou, leer na doumak tank
Magg jotna dou mak djankh, kèeman la kou  ku mane fanx
Déx ga ngui kou mar tanx, niata lafi doumaate sanx
Douma xof bangay napp, tidjéekou djaadouna
Douma thiof damay napp, ci guéedjou aduna
The king from the river, li mouy reudeu djoodona
Dama aay nga guiss, kone hate ma djadouna
Hun! Woyof ni khop téwoul diiss sa bopp
Boudè mane ngay weur, séetoul dinga guiss sa bopp
Li ci mane di yaw, mbed mi nga deink sa baate
Douma léne ci carte gui, borom béy sabape

… Li ame ba déss moy ma ngui ci reuw
Rythm and poetry nigga léer na mang ci kaw
Classics di taw, ma téew yégueulaate barre beulé
Kou yagg ci téen djomboul djappe ci barbelé
Bamay né ci naathie, ya ngui wouti kér feulé
Djémouma damay djeuf, melomane yiy zikar feulé
Ragal dée na ci nioune, li niou déssé kérssala
Mission niou yeukeuti, siguil sunu wa keur si la
Yeah! Ki möm kaanék soukeur sila
Selfmade, Sunu Kaddu guéssou kar si la
… Gonék teungueth yéegueulaate na barre yi
Nio djitou waral guiss nga ling niouye djegeulaate na bari
… Father babs défatina gaffe
Xaragne team, xaragne sagna firétinay laffe
Soré fingaye saaffe, goré missal sounouy djéggo
Balle ba takk na, the writah khana déggo

Khana déggoo
Khana danga dof

We say Hip Hop we the voice of the voiceless
We hustle and progress

Another way another vision

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR