LYRIC

{Hakill}
Lii nieupp di def rek nga DéFAAT
Légui yangui ci embouTEILLAGE
Dama xamone ni yoon bi DAY FAAT
Waral ma diaré ko à PEILLAGE
A.K.A boy bou WAANé BI | Ma moom ANNéé BI Ki di yobou RAP bi world wide i WANNA BE
Néwonne nala douma nourok kéne nieup sol Jordan waral mane ma feule ak samay WALLABEEZ
J’suis le boy sénégalais je rap mieux que tous ces gars que t’as dans ton I-POD
Bossé comme un fou je l’ais toujours fais là c’est EMG Beats qui est à LA PROD
Dama diangue RAP walabok DIOUDOUWALéé | hmmmm wayé dall DOU WALéé
En tous cas lima léér moy mixtape bi dingko cons même boudé danga nekk Cii TOILETTE
Yama ci djitou wayé RAP mala CiiY DJITé | Boy projet bi mangui Cii DEEH
Lii dadi niamou rek mangui job BET Afric boy naniou ma Ci CITé
{One Lyrical}
Bou done ndox nioy sa dieunou thiof niger
We damn boyz like my team is dope niger
Diob niger/teknical dokk ndigeu/
Mak bouko sorou niou robila xalé doth niger
Doniou teukeulé thi bilé game/hors serie laniou indi/
Rapeurou biguini yeup laniou teubeul com dab reptyl again
Lémou niou guén dafa taxaw ni codalou niger wéssou ngoora kang
{Refrain}
Lii nieupp di def rek nga DéFAAT
Légui yangui ci embouTEILLAGE
dama xamone ni yoon bi DAY FAAT
Waral ma diaré ko à PEILLAGE
Hors série *3 My neegguh boy Hors série
Hors série *3 My neegguh boy Hors série

{One Lyrical}
deux ans_deux dent baari talent rabagouma toth sa tympan
du vent_fou le cmp doma déf sarap ni hakill niger j’aim po
bathi lane niger_meunouma bind ni dip thiow dou djip /
ma defni izo/polivalent ni dizzy kha/
tar thi mic/ baari facét ni realy bizon
DG idy diamniou mix daniou beugeu gnibi
grand yof guinaw rail city bang thi sa face ma niger hors serie
kong_kong_kong_kong entré/geumsa artiste defni andré
from galsen dou beats by dré one lyrical ish yor boyla comming…hater
figuay diaré teuweu dém bari thi fém niari niger yi
gambi laniou colonisé coup d’état ni gbagbo cote’ivoire
sauv ki peut di rafal youxou thi all daniou terrorisé senegal
koufiy bandi_bandilou pasniou niger dina soukou diébalou
lyrical dafa tak tang four_guanane fresh di doul comone dieul sa tourrr
{Hakill}
Au lieu de rapper vous nous faites des FILMS | Voila pourquoi j’suis Hors SéRIE
Quand t’es là à parler sur mon fuckin jeans SLIM | J’fais de la zik qui plait à ta CHERIE
Ich yo boy tu m’a jamais calculé mais c’est moi qui vais te soustraire DU GAME
Rap Galsen filék mêm tête yé nekk ci kanam diaroul di sone ndakh DOU DEM

{Refrain}
Lii nieupp di def rek nga DéFAAT
Légui yangui ci embouTEILLAGE
dama xamone ni yoon bi DAY FAAT
Waral ma diaré ko à PEILLAGE
Hors série *3 My neegguh boy Hors série
Hors série *3 My neegguh boy Hors série

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR