LYRIC

{Keyti – Verse 1}
Hum! Lo dégue boul gueum, Diapal xadiou li ngay guiss
Dox sa mind free that what is this. How about it is ?
Ay marionette laniou cii loxo yiy xeuthie boum di créé cataclysme
Dal aduna cii leundeum niit gni done guett Khar
Life lepp you tarr
Iblis bépp farr
Damn légui niou sar
!!! New World Order !!!
Délo niit cii mala légui laniou naar
Injustice cii kaw souf, anarchie totale, Alal cii kaw moral
No one gives the fuck, Yorr bombe diko tal
Dajaal dii fi dém
Such long road walking to our freedom
Reuthiou gouniou systeme bi gni gui cii biireum
Di neub cii ay easeum
Contrôlé masse yi, Reud nieup gneup signou
Beut bigni xoll té guissou niouko Big Brother tim niou

{Refrain + Speech}
It’s the game of life (4fois)

{Keyti – Verse 2}
Sa mind soko tagatoul mou oyoff ni xopp
Lou yeksi mou yaubalé goup téinko tamal sopp
Firil codes yi di guiss ni niou manipulé
Ndakh ndogal beuré toul lepp lagni calculé
Cii Net bék cii mbédeu yi niou gui Under Control
Nieup lagni surveillé di déglou sunuy Phone Call
Sen rôle fékhé brain yi di khonet gueuneu thiol
Niéte xadiou aduna bi gni gui cii gni gueuneu ndoole
Niéintel bey dogal dioubeul xell yi see yénène
Indile la Hip Hop Holywood ak CNN
Tour drogue cii mbédeu yi, Porno ak Violence
Ignorance am audiance beugou niou nga khaute science
Diam bi yess cii diam yi, bi xamoul né diam la
Li niou fokné mom la dou liberté kam la
Kharé biss bou djot la
Strain sun your mind
Dass xell tek gni ngui doundou Serious time

{Refrain + Speech}
It’s the game of life (4fois)

{Gaston – Verse}
Ya ngui nélaw yéwoul
Liñ lay gaundé léwoul
Fékhel sakou God fofou rek la Fitna néwoul
Fou xathie di djité naafila meunoul am Afia
Xippil xoll ni fo bi yombé légui raaxna mafia
Sacrifié sa dom, sopi monsieur madame
Légui kaddom, moy tabakhate Gomorrhe ak Sodom
Beut bégui ñi diéw
Moy dawal lifi xéw
Technologie béniou yéw
Internet béko réw
Life bi Ordi la nioune la bureau niom Souris yi
Game of Life diégui naniou okeu niou ngui cii xouri yi
{Keyti} It’s The Game Of Life
Sopi naniou rabou Aleu
Ndank ndank di gnu waleu
Sèni Game bé ngui dialeu
Nouvel Ordre Mondial
Mélo Wona dajaal
Tunisie, Libye, Egypte, lép laniou dadjale
Game mo di fo té Life mo di doundou
Niou ngui fowé sunu doundou
Sipp naniou li monument bi woundou

{Refrain + Speech}
It’s the game of life (4fois)

{Outro}
You better wake up
You better wake up
Yéwou lène
Keyti Baye Sèn 2011
Sa xell bi kom la Boul na-ngou niou fowé ko 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR