LYRIC

[Julio] Un vieillard qui meurt c’est une bibliothèque qui brûle
Nangou woulén diokhé lingén yor comme ay guille
Sucé, ONG yi nane niou boyi légui rabatougne
Bamélou biir meunoul am old school yi labirougne

[Ada] Sen génération égoïste fokhalé ba groupe tayél ngenn ko am*
Liniou manké wone sa baniouy dor yenn dangenn ko amm*
Studio yi baakh beatmaker yi professionnels meunolenn yagak kéne ndakh jital intérêt personnel*

[Julio] Ouss ach
Léralo niou touss si game bi beug nék oustass
Dar niou ni moustache, di doundé cache cache
Qui séme du ribaa récolter saaga ndey boy sa bénéfice
Rest in peace tourou old lay bindé accrostiche

[Ada] Clash flow skills egotrip rekk*
Dadialé séni punchline nakh sén Jappé ko texte*
Wathiolén sur le terrain mouiller le maillot for the nation*
Playback Play-Art PlayStation*

[Julio] Conseils si gorge ni pomme d’Adam, dieuf you bakh yéy crise
Fuck séni show biz underground bi amoul terre promise
Rap geuneu done flop
Deudou hip hop
Geuneu done tote
Diotna ngén stop
Dina geudj ndiap
Wake (hun) up old yangui syncope

[Ada] Topandowanté senn birr mais particulier lenn*
Ribididibidi mais articulé lenn*
Meme flow meme beat meme yere meme attitude*
Dem show woute pute beug tere bagn koula toude*

[Julio] Yéne rékay touki beug valise carrierou mode avion
Melni cana di yo yo père niouna baygon
“Xunn xunn” comme ay porc maguettou marketman
Sathie son wou boy yi hip hop bi soxla woul profane

[Ada] Koulenn jemeu wakh deug ngenn defko none beug ko clash*
Nangou nek boyou nieup tayel ligueu beug fi place*
Dioudou beurki démbo ndiaye té nane danguay changer cible*
Démal tassou takhourane bo beugué def lou accessible*

[Pont] [Julio] Peuple bou amoul passé égale zéro
Topou tracé ba done pro
Engagement bou brut bravo
Yénay souniou héro
Lo tingom nak mou sout leu ni étage ak fondement
Boul ma mine ada knibal ba faté ma

[Ada] Deugla yi yenay fessal stade yi yenay nouvelle star yi
Hip-hop bi boudone gornement yenay yorr pouvoir bi*
Maitrisel lenn senn publik jangal lenko respect*
Bania créé none prise de conscience rek molenn dessé*

[Julio] Bayil lén niou lou palpable lou stable rék job bi parfait

[Ada] Bougn téggé lep si yone deganetane lolou warta jaffé

[Julio] Djiteul boy yi bania xeutiok nioune ni ndjabootou canara

[Ada] Ooh Julio guerre meune na niak mais xeutio fok mou ame

[Julio] Way xeuthio meun na niak guisso béneu pa di dawal mbégué

[Ada] Yaw lingay oute si mafe la sokhla si thiaf manam déggé

[Julio] Wa légui démal ak mak sa maguétay

[Ada] Demal lak sa niak expérience

[Julio et Ada] Awma loumay wakhak iow ndax rap bi mako mom

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR