LYRIC

Verse 1}
dama gnor tabi sama tour day sakh abadane dahimane
sama djobou demb tay mougui briller ni diamond
ba léne gnou sisou respect bi tabina ci xolou gars yi meun
dama rombeu meun rap aka diafé kou ayé ni mane
fouyma kholé khép séne bopp waral xolou di yakh dér
deulouma train bi en marche rak dama raùper bani diak kér
boulma bak mér mouno mér ba saw ci code pénal bi
ma yoré volant bi di dawal té yaw niouguila khodj ci maal bi
mbé mbé khar yagui mbé
bou rap bi nékon tank boy xol sakh dougnou ci wé
zidane la ci rap bi
dixieme dan ci jab bi
nouma nekh nieuwé
fouma nekh feulé
flavour la ci ndap bi
sama caché lalagoko
yagui gnodi bandi té ba légui join bi talagoko
boul gnou bakloko
li ngay gnodi atanoko
tabaski dougnou tapalou daniouye jasner ak bakayoko

[refrain] sa tour néwoul ci téré bi
sa rap diéguégoul féri bi
rime yi gnougui téré fi teudieul sa guate té liral bi
gno la dakh diapizé gno la dakh rap (x2)

{Verse 2}
béne + béne + niar ca fait quatre
gnou gui fi wone démb gnou gui fi tay souba fii laniouye fékate
macbook air yako tay fils dou P4
ana lou nonou wagni ci bureau ba sa ndar ki gnou doupé 4
beug khorom sama thiakri
laye khol di vache kiri
balén gnoun keur keuri
bougnou soné rék dém teuri
takh nga bamou wathi under bi yeup sakh ci ngamou bi
ngir YALLA wa rassouli rap léne bayi langamou bi
gnou diangat rap bi diangatate brute bi
wagni wax bi yok dieuf bi meuna magaat touti
dama gnor tabi bokouma ci gni geusseum bi indalé
bamay put ci khar bi kharagne ak aye la dieundalé

[refrain] sa tour néwoul ci téré bi
sa rap diéguégoul féri bi
rime yi gnougui téré fi teudieul sa guate té liral bi
gno la dakh diapizé gno la dakh rap (x2)

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR