LYRIC

{4Leuz}
Xalé Bou Yagga Lotou lole Teud ci Bassang Sango Seurou Rabalou Mamam
Yéwou Ni Kéwou Wara Djangui Guissoul Pain Bou Diaar Thi soufou Nkamam
Liko War Wathiouko Genteuk Thi Kouné
Yéném Kathiouko euleugeuy Gouné
Fimaa Diaar Koufeu Diaar TakRipp ak Bane nak
Mouy Taar Maay Khouss Nane Kagnlay Doone Mak
Thioko Tikou Founé Deal Na Louné
Ndékké Gent ak Yénéy Diour foleuzophy
Yaye Dima Térré Mbed
Baye Dima Térré Guéd
Gnimeu Gueneu Digué Fok Damay Dofi
Lou Boone Li Thi Bitti Bi Xothie Leu Baate
Boudé Xoslou Thi Lou Baxrek Gnou Yeslou ci Waate
Tayeu Sou Yombé Baye Nekh Ni Beurigo Thi Mbartal
Dembeu Taar Troope ni Xaley Bougnou Xarafal
So Beugué Gueneu Ci Bi Life Topal Gent ak Yéné
Sa Souné war Sa Souné Job Wérou Sa Diné
Mouslou Thi Seytane
Waaw Amoul Dara Lou thi Kémtane
Guissoné sax mbeur bou leulo magg Dane
Lo defeu Geune Lo Défoul Thi Lépp
Lougniye dundou deugleu Man dou Aye Lépp

{Refrain}
{PPS} – Yoré Saye Gent rek Diko Sameu
Yéné Nii Paka Rek Diko Nameu
Loumou Goudi Goudi Gnoune Dagnouy Téér
Soudé Bouki Beuteuy Naane Diakkeu Wéér
{4Leuz} – Yoré Saye Gent rek Diko Sameu
Yéné Nii Paka Rek Diko Nameu
Loumou Goudi Goudi Gnoune Dagnouy Téér
Soudé Bouki Beuteuy Naane Diakkeu Wéér
Hook 4leuz PPS Gina
Maane ame na
Maane Ame Na
Gent ak Yéné, Gent ak Yéné
Maane Ame Na Gent ak Yéné

{PPS}
Yagg weet di janeer sunu bess, Tagg weet gni yandor douniou guiss
Gueum gueum eumbeu sunu yènè, dox daw soli yèrè, taye la sunu sass gueuneu diss
Nioune mome deme rek laniou guiss
Tingope sunu xol ba dou tiss
Ame jiz-a niou gueuneul ame peace
Yeah! Yama gueuneu xam fils
Sopi kanamou family, sigui ci askan
Diegui naxar nioune daniou yagg di ass kane
Teudeu ba nirok neew nelaw dou sass kène
Jeem dou mbass kene, daniou gané ni ass gane
Fi ak – foumou mana doone
Yi aate – kouné gueuneu boone
Djihate – founé wouti côme
Mindef yi – gueneu fouti come
Sama yéné – diegui na sama jeum, yokk na sama ngueum, wane nama fama djeum
Dama wara – djariniou djarigné, xaré ba arrivé, may lokho niou barigné
Ngor ak jome boula – dara teré jeuli linga mome, jeingou la bro dara jomboula,
Deugueul sa gueinte – wané xaralé, noone yi naxaralé, jeem soula ko djaralé

{Refrain}
{PPS} – Yoré Saye Gent rek Diko Sameu
Yéné Nii Paka Rek Diko Nameu
Loumou Goudi Goudi Gnoune Dagnouy Téér
Soudé Bouki Beuteuy Naane Diakkeu Wéér
{4Leuz} – Yoré Saye Gent rek Diko Sameu
Yéné Nii Paka Rek Diko Nameu
Loumou Goudi Goudi Gnoune Dagnouy Téér
Soudé Bouki Beuteuy Naane Diakkeu Wéér
Hook 4leuz PPS Gina
Maane ame na
Maane Ame Na
Gent ak Yéné, Gent ak Yéné
Maane Ame Na Gent ak Yéné

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR