LYRIC

{Refrain}
Woyof tolou cii biti, diss ngaane cii biir
Tolof tolof cii sa toll, sa yone ak lala ca xiir
Naax sa boppeu gueune gaw, djap ngaaka gnila weur
Xam sa boppeu meuneu raw, gueum sa boppeu gueune woor (2fois)

{Verse 1}
Seuleum kanam xippi xol, yootou naar bi ki gueune dieul
Beuss métitou xoll, gni yokou wecked cii gueugn dieul cii
Diamono bou faux bi, niouy djap teuweu bayi
Niak-kay sunu phobie, tek tanke dogou dém
Def ndank cii digué dembe, Diom mo fess sunu guembe
Bir niouné dara dou yombeu, fass yéné ko xaré mou yembe
Diombe seug comme Fake, Nango deug complexe
Imcompris lagni diké deuké sante bégué comme fete
Niakk douma taxa seug, Kome douma taxa sigui
Naatal missalou deug, niakanté donka sigui
Noblesse fess sama dieume lou alal meuneta djeundeu
Sameu diam dieumbeut diom démé ndank souxaat Kome
Deugui Goor deuké Gorr, door partie bou lerr
Deugui gorr bagna worr bagna gorr ni Pat Hibulaire
Xacci bou lerr tolof tolof téré ko dal
Never Ever douniou athiou waxtu gniy wéré ko tal

{Refrain}
Woyof tolou cii biti, diss ngaane cii biir
Tolof tolof cii sa toll, sa yone ak lala tcha xiir
Naax sa boppeu gueune gaw, djap ngaaka gnila weur
Xam sa boppeu meuneu raw, gueum sa boppeu gueune woor (2fois)

{Verse 2}
Kétaal sunu euleuk vision bi système bi alaak
Xarak gni xothie sunuy xell fékhé feusseul sunuy xisseu
Né cii leundeum dou tax ma tiit ndax beuthieuk dina téw
Di gueuleum doundou métite waayé weurseuk dina téw
Né séw yéwu yeur li euleuk indaalé
Seugueum do gueum soubeu ndax tay ni la naatu yi dalé
Sunu bidew wa teuweu féink waayé niou ngui deuké sante
Bania def lou niaw liy nieuw diarna sooralé
Rouh bou woyof wooroul lou nieuw yobalé la
Teunk sa tékki cii niaxu kénène ligueyou xalé la
Aduna diaroul fay Iblis nguir dougou safara,
Louy yone bi sori sass bi diss mbébéte yeup dina saafaara
Lepp borom bé fa ngay gueumé métiite saxoul moy biss bou lep rombé
Gueumeul sa bopp té dém, gueustou dounya teudém
Be true with yourself, téylou, gueustou di galadiou kangam (Listen)

{Refrain}
Woyof tolou cii biti, diss ngaane cii biir
Tolof tolof cii sa toll, sa yone ak lala tcha xiir
Naax sa boppeu gueune gaw, djap ngaaka gnila weur
Xam sa boppeu meuneu raw, gueum sa boppeu gueune woor (2fois)

Xam sa boppeu meuneu raw,gueum sa boppeu gueune woor
Gueune woor, Gueune woor

Gueum sa boppeu gueune woor
Gueune woor, Gueune woor

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR