LYRIC

{Intro}
Bou dara dessé loudoul Rap nagnou simi costard yi, faye cigare yi
Bayi naane djougué cii bars yi dieul xalima tass xibaar yi Cii Caps yek taxi mbaar yi 
Bou dara dessé loudoul Rap nagnou wagni djay taar bi
Def fouleu cii art bi na-ngo done sakhar biy yapp cii gare bi
Dougnou ay royou kaye waayé beuri nagnou lougni bay cii waar bi
Bou dara dessé loudoul Rap
douma takkeuh, douma naane, douma diwo nix
Hardcor bémay danel ni B-One X
Souma rimé mou nekh so rimé mou melni foukèn poupe
7ème dane la cii level né wa Fuk N Kuk

{Refrain}
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk Nitdoff Killah mogui bindeu
Done tchii raam done tchii dokh done tchii daw done tchii djaadeuh
Taye ma done tchii mak done tchii ndongo, done tchi father
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk nitdoff Killah mogui bindeu
Yo yo yo yo My flow is so hood, make you feel good
Used the microphone like Dirty Mc Guirt

{Verse 1}
Pow Pow lep né keuleup bomb to bomb
I’m untouchable I’m like James bond
Hip hop never die donté one second
Koukey teweul ci mbed nang ma wane sa gun
Once again a man like Mister KANE
I’m supposed to be a man who love the game
Fuck with my hot niggers LG fam (Family)
Hip Hop falou falé té fonkou li ngèni diambat
Daara leu ci gnéne gni beurineu lounie ciy dianguate
Mbind mi di firndé ndakh xel yi laniouy tanguate
Rap bi haute couture ley done mic bey sunu ciseau
Fiyeuk ghetto bé ngui dread to the skeezo
Tig to the rime done H to the Izo
Xel yi nathie xalaat yi megni tek ci beat yi bathie
Rap Dou meusseu dead nigga boul si nek né yathie
Kothie kothieul diém tewal mission biniou leu gathie
Wessouna music nigga diapelni rakk leu
Dou tchi tchi tchiaguené jaaay taar Waleu aak leu
Détecteur de fake leu batiou gni amoul bate
Anti corruption leu kouko deglou mou baap leu
Music kou mbed leu kouko wédi Niou dioguileu
Kouko diogui Niou guèd leu
Deloko tieur bi war té gueum né art bou tédeuleu
Hip Hop come on pls stand up
Hip Hop come on pls stand up

{Refrain}
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk Nitdoff Killah mogui bindeu
Done tchii raam done tchii dokh done tchii daw done tchii djaadeuh
Taye ma done tchii mak done tchii ndongo, done tchii father
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk nitdoff Killah mogui bindeu
Yo yo yo yo My flow is so hood, make you feel good
Used the microphone like Dirty Mc Guirt

{Verse 2}
Yo ghetto love Hip Hop tek tank bagna tégui
Door waar mouy mate diambarou bagne kate yi
Day will come mbède diox gnou 4×4 yi
Hip Hop bi soute fété lène kaw ni thiakaba
Keep it Real dou yagg bagnou marr tateu
Bindeu sunuy chagrin, Rap sunuy blessures
Rimes sunuy quotidien Wané sunuy teurgueun
Nétali xew xew fightal sunu askan
Music gou mbede leu homy wanel sa sagne sagne
Xiroul ba matatou xoureul sa baate yay bagne
Yague nagne gnou djigne diokhogne gnou barame
Toumeul gnou, teudj séni bountou xepp gnou manam
Téwoul Hip Hop di magueuh gueuneu dieum sa kanam
Xalima yi gueuneu gnaw, lamigne yi gueuneu niaaw
Rap Olof-fa raw, téwalko fi ba kaaw
Hip Hop ba bolé gni am ak gni gnakeu
Gni xess ak gni gnoule Gni ngour gui di doule,
Gni system bi note help me God ci ténn biniouy roote
Télé bi soote dignou forcé ay tott (Fuck U)
Gnène gni fok ni gni gui New York (Fuck U Fuck U)
Rap Music touti ngène ci raye ko
Show biz bélène iri dioutoul ngène thiouray ko
Hip Hop come on pls stand up
Hip Hop come on pls stand up

{Refrain}
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk nitdoff Killah mogui bindeu
Done tchii raam done tchii dokh done tchii daw done tchii djaadeuh
Taye ma done tchii mak done tchii ndongo, done tchii father
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk nitdoff Killah mogui bindeu
Yo yo yo yo My flow is so hood, make you feel good
Used the microphone like Dirty Mc Guirt

{Verse 3}
Egotrip, Beef, Wala Balle perdue, bougnou djoté dékil guerre gui Ségue calcaire bi
Wané Altère bi dieul toule djappeuh derr té dougnou taudj père yi
Gaw né thial mèrr té dougnou guileu berr yi
Bérou wouniou ci kèrr gui, xam nagnou li waral merr guii
Fo séné tak-ndèr, daw djapé gnou tak derr
Ci guéwou Hip Hop wamé nagnou gnane gnoy takk ferr yi
Tek cii brique, firi doune xaff, gnou fouli derr yi
Taggeurs ak Graffeurs yi, Deejay yék Breakeurs yi
Hip Hop Dou Meusseu dé cii Coeur yi
Ci mbède la djoudo wayé tay amena placam cii keur yi
ARMEL SA GUN boul saagane Mission bi Door waar leu
When I spit my rhyme its all about my life
The life from the hood Hip hop following in my blood
The way we gonna shine way wé gonna fight the power
Way we gonna blow way I gonna make my dollar
Still popin my collor, Street niggers di holla
Believe me nigga hip hop ain’t dead
Wé bring it back let’s murder them bitches
They wanna kill the game to get richies
Real Niggaz still playing for the real niggaz
Let’s scraching this shit for the street leaders

{Refrain}
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk Nitdoff Killah mogui bindeu
Done tchii raam done tchii dokh done tchii daw done tchii djaadeuh
Taye ma done tchii mak done tchii ndongo, done tchii father
Hip hop dou meusseu dead my nigga fi weuk nitdoff Killah mogui bindeu
Yo yo yo yo My flow is so hood, make you feel good
Used the microphone like Dirty Mc Guirt

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR