LYRIC

Waxoko ci sa lamigne mais guiss nako ci sa beut
beurina loy demaler mou nek ay nakhar ci sa heart
Sometimes nga teudiou djoy ba guedj ngi ferr ta kenneu dou yeuk
Naatu yi songanola , ngay xeuy di geuna ndoleu
Sodé Ngor fok mou meti ci sa Jambar ak sa Ngoora
Do talal loxo gnane , do sathie da ngay jomb loleu
Sometimes da nga ciy weet ba melni yaw amo ay mbok
Soy dem di gnaani ndjek daniuy bagne ta naane la ndokeu
Yaw kott yaay dess ak febaru xol biy geun di yok
Fass yeené wossi yaafuss ndakh ya ngi xeuy di djengou
Saga naniu sa ego ci liguey bi ngay yengou
tiono dou reer borom takh na ngay fanaane di yendou
soula life bi deh tanthie
xat xat yi gnolay teudj
geuneula djayante ta xamni weurseuk doula reuthie
xaliss amoufi xerr, kouka yorr ken doula xepp
mais kouko xegnul dagnulay mbedi , berr la ci sa xeet

{Refrain}
{Mao}
Jayantel ba ame ci ndam , loumou meti meti Jayantel ba ame ci ndam (Jayantel) (2)
Yallah diexoul , lou metti yaggul , Jayantel ba ame ci ndam my nigga saalit baxul
Jayantel ba ame ci ndam (Jayantel)

[Couplet 2] Louage yi geuna chere , Facture yi geuna diss
Depense ken douko miss , naxari dereet , gawa crise
Ordenance bon de luxe leu doundou bi geuna chere
xew yi beuri lolou ta ken dou deff à la legere
Ken xaratul lou nex , niune daniuy lekk guirr bagna xiff
Kou jayanté ba yegg di nga fa fek sa benefice
Soula niak bi dé boukh
Seytané dalay roukh
So salité rek sankou dinala souxate ba nga soukh
Jayantel sa digg ndaw nga tollu Yallah diexul
Beugue dimbali say wadiour ta menno xam nani nexul
mais ken dou xeuthio’k Yallah , lou nekk ak famou ko app
Jayantel mo geun nga wathie yone gnu teudj la rapp
Daral xeuyul sotti
mo sakk , ta moy soppi
Jayantel ci souteureu sakku ta bagna djogui
Ame ci amine bou lew ta nekh Yallah moy sa thioki
Kounek sa weurseuk di nga ci diote kone lou diar xeuthio bi

{Refrain}
Jayantel ba ame ci ndam , loumou meti meti Jayantel ba ame ci ndam (Jayantel) (2)
Yallah diexoul , lou metti yaggul , Jayantel ba ame ci ndam my nigga saalit baxul
Jayantel ba ame ci ndam (Jayantel)

[Couplet 3]

Jayantel tcha bamouy meti moy takh bou nekhé dossi rouss
Jombalal sa bopp doone app yafouss , Dieu est là pour tous
Bou Garap yeulbo xopp ya rouss
dafay megne feuille yu bess
Jayantel everyday my nigga try to be the best
Soula djiguen gni deh xepp
xarit yi dila ndaw , mbok yi dila doyadal (Jayantel)
Jambar ngi nga done , ya ngi xeuy di wané Joom sossi amagoule koom homie (Jayantel)
Ya ngi tchio tolluway ta lo yakar rek mou mbass la
Say effort duniu ko guiss ta kossi wane guinaw mou xass la
Boul decouragé geunal wollu Yallah ta nga hustler
Bou negu seuy bi Hard , ba nga doundou fa lou metti
sa dome meune nafa magg tekki (Jayantel)
Boula niit ki eupeulé , feugg ndeundam di jaayu
yeené ko limu amm ta maanu (Jayantel)
kone Jayantel ak Yallah , Jayantel ak sa ndigg ak Niit yi

{Refrain}
{Mao}
Jayantel ba ame ci ndam , loumou meti meti Jayantel ba ame ci ndam (Jayantel) (2)
Yallah diexoul , lou metti yaggul , Jayantel ba ame ci ndam my nigga saalit baxul
Jayantel ba ame ci ndam (Jayantel)

{Mao}
Jayantel di nga mousseu am li nga beug
di dokh do seug ken douleu xepp fi nga deuk
Siggil bul seug , xamni ken geunouleu , Jayantel my nigger eeh
Nigger Jayantel , Jayanteel
Nigger , Jaaayantel
Jayantel
Jaayantel

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR