LYRIC

{Simon}
Na Gars yi keupp warga yi, deudou ragal yi
Fomp rongogne yi, deukou thiono yi
Fokati money nguir taxawal House yi ,
Caisse yi, cos yi (costumes) tégou cii eyes yi
Cash gui, mass gui, di flashé noce yi compté caissou liasse yi
Amatoul niaxtu, waxtu, yeureumtalou
Fontu, xountu, sakou lilay waddal beureung teuwoul
Ki loxo ak tank, doli dolé sante Beut guiss lampe
Lérayou djante, guémigne bi sampe
Ay 20 milles flow, firi tek ci phrasé lou fake yi doul fogué
Kawé bay claté, seukeul lou clapé, 99 lakoy toggué
Kou tchi dérapé ma sar sa galé faateu pakh bi ngay togué
Yaw mi salé lay feug ay contenairou arré
Héééééh hééééééh Shuut !!! Niou démate,
Ounkeu yu bone yi sèneuma sen guèneu yi niou lémate
Job-biil aythia mo gueune ngay kaathieu
Weureuki saathieu niou djapp yéw ba nga rappeu

{Refrain}
Nélaw bi dafa doy fok nga (Jog outi xeuy)
Takkou, taxawal, téwal, téla (Jog outi xeuy)
Fass diom weuri koom (Jog outi xeuy)
Bayi doff doflou bi té nga (Jog outi xeuy)
Na nga yéwou cii dream yi (Jog outi xeuy)
Na nga bayi sa prek bi (Jog outi xeuy)
Bayi frek jottay bi (Jog outi xeuy)
Bayi tok di khar bi (Jog outi xeuy)

{Nitdoff}
Wake up in the morning, lassel sa shoes
Wanel ni nga meuné noy dassé sa flouz
Lo meunoul ak sa dolé sa mind nga use
Abadane bagne katt ni Simon Killah
Lambe ba dath kat né mo gueune dieuleu
Noflay mo diekh kou niaak dieurignou leu
Gueumeul sa bopp ndax gni am gueunou niouleu
Waral ba tekki xollou noone yi gueuneu niouleu
Ko meuneu done na nga Jog outi xeuy
Thiono yi ngay dath dina fay one day
Yallah moko wakh cii Al-Quran kone kay
Sabab lo woor li cii dess done key
Diamono ko leuthie yité yi teggalo
Fitna téw indi ndiakaré kou yabbo téla daw
Jog ndiapp bagna tok bagna taneu bagna xepp
Boul nangou ben mindef dila fayal say dett yaw

{Refrain}
Nélaw bi dafa doy fok nga (Jog outi xeuy)
Takkou, taxawal, téwal, téla (Jog outi xeuy)
Fass diom weuri koom (Jog outi xeuy)
Bayi doff doflou bi té nga (Jog outi xeuy)
Na nga yéwou cii dream yi (Jog outi xeuy)
Na nga bayi sa prek bi (Jog outi xeuy)
Bayi frek jottay bi (Jog outi xeuy)
Bayi tok di khar bi (Jog outi xeuy)

{Simon}
Bo meuné kone défal gnou guiss
Lémi daw wané sa ndiss
Tek cii brik jobbal sa fils
Make biz siguil sa miss
Crise kaw gnila siss
Brise daw kanam ya liss
Vice order dou Ibliss
Miss tôt sinon tu……
Nekal ponkal cii bepp game Done kilèni yéém
Jog diém wané…Amoul tayi got’em
Daw blem, fake dougnou meusseu undestand
Man bouy séral bakofa nga jog dem

{Nitdoff}
Sa weurseuk louniou toudou la, lou djitou sa dioudou la
Sak ak soutoura li keulé am dougou la
Noflaayu tay sa gathié soubeu la
Sèt yone ba guiss ko datchèy dioubeuleul
Li nga beug déki euleuk tay ngakoy djiii
Apeu cii sa bakane ba taylé ko tchi
Euro CFA wala bok Dollar Dollar
Yakaru Keur Gui Cii say mbagg laniou ko Galleu

{Refrain}
Nélaw bi dafa doy fok nga (Jog outi xeuy)
Takkou, taxawal, téwal, téla (Jog outi xeuy)
Fass diom weuri koom (Jog outi xeuy)
Bayi doff doflou bi té nga (Jog outi xeuy)
Na nga yéwou cii dream yi (Jog outi xeuy)
Na nga bayi sa prek bi (Jog outi xeuy)
Bayi frek jottay bi (Jog outi xeuy)
Bayi tok di khar bi (Jog outi xeuy)

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR