LYRIC

1er couplet
Bul Falé walabok delooma sa walleu bok
Back gueustou Kocc Barma ci Daara ji xaleu tok
Ngeum la rap adio , xam xam bu Full Niggers
Xeetu geinte yi rapadio, tundu wundu be niagass
Rescapé ci underground ak yaxine duniu sikki sakka
Fok niu teewal sunu geble , One ni Battling Siki sak-a
Haa, Boy bi feulé ci alleu yénu zik
Nguuru Nuuru té du diik, goré soré yoonu sikk
Weke lep ci ki niu sakk, Music is for Da Brain
Da blessed, Yonentu rap bi daw ba réne
Borom bopp yi jeuli, duniu foo, fo nek niu weuriko
Kay rime ak Djily , feki still , skillz wériko
Under bey Shiffay negger , deung dee ci faille dingue
Feey ci daay, tek ci high, baye di siif aye deingeu
Chronique ci 2H , tok sit ci mbind mi
C C C C C C C Toxic ni mbeund mi…..

[REFRAIN]

Couplet 2
Yen say man ngay get melni kouy lire aye Book’s
One ba 5kiem la kumpe sen samay Roots
Ma Karismatic di Diksa
dio di Job ni Big Fa
Lahou zi Zaïr di fegne thi batine ni Bourba
Mane la boy yi beug Niggers
def dara ni Gas
Bring the Rawkus
so dé thin may sa nokoss
waaru goor tiggi ci rime bi aksil si Keur gui
Do co cons ni tek fok say neurone di Keurti Keurti
First Class si X-press bi doxantou gare ba gare
Biyone nix dagnuy coalition xedeeku xaar bagare
Ba ngay overdose si B-crew ma ngi Jxaar ci under bi
Opinion seey ci darkness ni seven shots ci deunde bi
Damay Fla Ripper ni ombré si biir Zion
Kalima ni lafou Djibril——–
I’m da real one , Hip Hop Flava da laye lale
Bol doff bou Hip Hop Style Djolof diokh ko gni bagne lale

[Refrain]

Ombre Zion (Part)

couplet 3

Rawan yee ngen Yougoungoung suli Ruu Rap si bois sacré
Teewal Jolof 4 Life , xool li sunuy voix sakk rée
Fier ni sankara , fuma guesso dagne ma woo
May Blaise sen ngor Kay fecc ci rythme Mao
Ame ak niak la yamalé , nubien du waliyane
xalleu yone diegui rails , laniou suñu walleu yene
Donté Junky la , Aaru miserables momay facc
Flow Rhymes technique la Pps the Ghost di lath

[REFRAIN]

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR