LYRIC

{INTRO}
Just for the game now ;what’up jah me rue whats up
Show niou love niou guis now
Haa haa haa haaa haa haaaa !!

REFRAIN
Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

El Chigga
Yo !! baniouy kheuyy di door si hip hop
Yek jump no stop
number one air force Smooth break ak ay nike pump
It’s just a feeling
Gaddou microphone check
Gonna just a killing
hun !!
mc douma teuyé
Coz i got the skillz Teksi xam nouyouy xeuyyé
But hip hop is connexion
Peace love harmony and having fun Lepp for the nation

{Karballah Dieng}
United we stand
Niou bollé dollé bene
hand si hand
Rap dou war niou let mou leave saga We do just for the game
Sekhouniou haine
Pass pass bi nek bene kounek sa brain
Geum sa fondement dou lathj affrontements si bene scène
Boulma jema khagn jant
Boumay tole foumay téggé tank
Boulma outteul ngant
meune nga lank
bagn ma jema sank
Bayil move bi nek béne ta nga jauk si diko separated
Tauthj hip-hop bi grow ngir mou fegn fok niou collaborated

REFRAIN
Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

Wicky Lohj
Talounioussi guerre kene
Yegoussi calmement
Formé souniou bakstage
Esprit g.y ment
Yénou wouniou khew bi
daniouy toudou késsé
lou ngay niodi yako déssé
Paré deuk thiow bi
Amour laniessi djieteul
guissouniou louniou titeul
Just for love bégué for life khol yi laniouy guiffeul
Just a game amouniou haine noto boulko disseul
Doundeul feem déguéné style bagne si ndiodi guisteul

Myster Zou
Bou kéne disturb
Fi game bi tollou ladj na rise up
Niou conquérir world
Thi spoken word bi
brandir cup
My nigga loula naxary
Jalousée niou té doone xarite
Gangster ngay niodi bo teudio ak sa shody Woné sweat heart
Just for love we do it
Def logique
Dof lo zik
No sik
No vice
Bou sa xel mi selloul do wite
Call Wa West ak Wa East, North and South niou job thite
Like basic Na balèze niou rafétal sounou trafic

REFRAIN
Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

Stan Flinger
Kou thi diangoul nounioy nappé nigga boul ko may yapp
Move laniou sekh yitéwoo buzz waroul tax ngamay yap
Na xol yi set god meuneu nieuw
Labali fass yi meuneu daw
(show niou love niou guiss now)
Nagn ko def thi respect ba dofi guiss lene lou niaw
Dass sa hit tek ba kéne dou dém nga des ganaw
Never
Nagne ko adjt hi yénéne level
Wou niou thi peace niou dounde hip hop for ever

DIAP
Its just for love
Nage ko dounde now
Yékeuti level bi sponsor yi nieuw
You better know
Dani niou wara naw
Hoouu Hoouu Hoouu

REFRAIN
Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

(yo bayil beat bi daw men ,
gars yi show niou lot off fucking love mennnn)

REFRAIN
Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

Kou kéne disturb
The game is up
Just for love
Follow niou move def naaw
Show niou love niou guiss now
Hoouu Hoouu Hoouu
Hoouu Hoouu Hoouu

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR