LYRIC

{1er Couplet}
Boule meussa taukhe baune, Boule meussa naane wine
Boule meussa doone fake founioula fékk dél clean
Boy dokh déél sigui , di represent saa City
Boule niakk geumeudi wala xeuy rék am daadi sipi
Del khool sa nitou dembe bi dara doonul léne
Sèn loxo nga done yendou gnola gnanal dila ngémb
Please Nigga stop siggil té nga goré
Dindil li nga fook ndakhté life bi day woré
No Matter, what the deal you got keep It Real
Kholléne si Beut ak Beut diléne téggal lingay Feel
Déél Wout di diokh sa Mother, Diémeul woutou sa Father
Tchii galé lou nara gnaw nga diouk tchi telko Faadeu
Boula show bizz bi goûté ba ngay nakh gni nga djité
Ndakh Démbe ak légui yaggoul mais say discour dafa wouté
Wakh tchi mbakhou kénène dou yakk tchii sa mbakhe
Toumeul nit loumou défoul dalay Topeu tchi saa pakhe

{Refrain}

{2ème Couplet}
King Killah tchii Ring bileu, Mbede bi ak feeling bileu
Sedd bi ak didim bibleu, Kii ngay djiteul cii liim bileu
Say nigga dagnii pop, Samay nigga dagni ndiapp
Yegg yegg lagni démé, Dou kou nekk lagni aimé
Dagni raay dadii tamé, Ay hit rek lagni diamé
Mouy régue wala affamé, Gaïndé yapp ngako xamé
Dotou maa waulou jamais, Ndakh daniou domouramé
Niata nga dimbeuleu niou weulbeutikou dila dialé
Ay toxico kii kamé nioy tok di lam lamé
Louniou laa xamal cii mbaute cii gran place yi laniou koy samé
No no boule def ni niom, Gorr waroul niakk diom
Bou até déssone tchii mane maa timelène ak makoudaume
Sa diante dina shine, boule yakamti sa time
Boula daray aduna diaral fils ngay wor gaïneu
Mane ak yaw bougni boy, Sunuy ré ak sunu djoy
Taay lep néna saay waral sama xoll bi toy

{Refrain}

{3ème Couplet}
Hann Yeahhh!!!
Lepp loy yéné nit kii Na done affaire bou nice
Songue life takk fiit bi nangou def aay sacrifice
Yonou goor dafa métii, Nioune nieupe beug tekki
Boule dém dii tiogue kèn sinon yalla dalay djépiii
Bodéé fake nigga get out my way
Nioune douniou Holla kène kou doul real all day
Amouniou diotou tokk di feinte bullshit
Talou niou loudoul job tchinpeu baa tiow djipp
Saay none louniou téné, rebellou laniou laa yéné
Boule sakh di fayonto kone dafay takh nga aliéné
Niom dé daniou lazy (paresseux), Faarlou wouniou niii Jay-z
Fi cii guétou rap niouy doundeu ak mane tchii hypocrisie
I know nigga dialoré yi lay tek
Rangalé yi succès cii albums you High-tech
D-d-d-d-d Squad di karanguéy my back
Nokoss Di Rok My chek my tek

{Refrain}

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR