LYRIC

{1er Couplet}
Talibé Mara Marra, Djissouma Loutakh ma rameul leu
Boudé ay xeureum meu nèkk tchi yow, gueune neu takh ma haramal la
Badou borom djassi dji amena niou gueum ni frama la
Fuck Wa Tel Aviv dioulite dey fètè Hamala
Boudé sa ex Bike (Vélo) lawone tay dji sa far bi Hammer la
Sunu honor la, Sikar Bourbi djouni Subhanalah
LG moma teach RAP GALSEN fogone ni kana la
DO double feuzeuw (DOFF), bidew fakhèneu fa euzeul
Mane damey def carrière yow da ngey door dakhè for buzzeuw (for buzzeuw)
Hey yow miss dick, Sa public dafeu miss hit
Sonou tchi sow ak mbiskit, Diokhlen michoui bayi mystik
Li défone BIGGIE and PAC, Ba lègui mi gui intact
Soxla woul sa gun takk, Té bèss bèss bi dey gueune takh
Million dollar flow daddy, Djante ba ngui follow day bi
Public ba nga wait lou hard, Boul feulè fou low baby
International real mc dou buzzou internet
I’m promotional MBEDE flavor dou dosou intellect
Diokh century bitch bobou dou meusseu binde li
Door ko ceinture yi teacher bo woute douko si dimbeuli
Rally rally piano piano Mane douma sa Sindjéli
Kouma singueuli di nga dèlou sa podiou ndeye diobaate sa single yi
Kamikazou gueumeu khouss, Dioublou fi sa dieum choose
Yone wè bari khaakhaam kokou teleu xam di nga dieunde shoes
Diaar na si under proove Sokhla touma pundeu clothe

{Refrain}
Yes Sir Mane Killahrie laay deff
Louma ci gaubé guar douma tite douma khèf
Say Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf
Say Killahrie Killahrie this is KK Killahrie
Killahrie Killahrie I give you Some Killahrie
Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf

{2ème Couplet}
Yo I feeling it again, Some killahrie dou dègne
Sama flow laniou addict dagne koy used ni cocaine
Still play the good game
Mouy beutieuk wala goudèm
Niou ndiap taxi raps
Shout out my big homie babs babs babs
How intact is my loyalty that’s what to ask
Rayz Man rock Killahrie the name drop
Wè just take the mutherfuckin money douniou nièm drug
Where my niggaz at ?
When we love we go straight. no zig zag !
Reppin for my city till I die like Jigga’s act
Saf sap ni doublèss
Chaque frappe tue ou blesse
Hip Hop bi niou soute leu lèss
Ndakh real rap bi ci hood leu dèss
My skillz go play zidane, Maa siw comme president
My rhymes so perfect, My flow Still crazy gun
Hip hop laniou gueuleumeul, Fèkhè nagne ba khèl mi flou
Illuminati blow up, Liar never tell the true
Mc yagui fène sèy fan’s, Dilèn niodi quintessence
Succès ba ngui mour sa eyes, Sa mbinde ma gui feinté sens
So intense, I go harder see my people so in transe
Hear me now, I handle the deal
Li bou dakoul di nga degue killah rèndina diw
Esk bi wègne bouniou dagone bopp bi daw rèn dina mbiw?
ND killah from gunzout remember the G (Gangsta)
Disconnect this mutherfucker and end of view

{Refrain}
Yes Sir Mane Killahrie laay deff
Louma ci gaubé guar douma tite douma khèf
Say Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf
Say Killahrie Killahrie this is KK Killahrie
Killahrie Killahrie I give you Some Killahrie
Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf

{3ème Couplet}
I will go with my ego, Don’t wanna take a liquor
Amo doe meuno flow, Kone li nga athie adji ko
Ma ngui féss tè di go, Manifesté dji ko
Bari gate ak mytho mo gui fèss sa djiko
My people meunolen bluffer ak sèy pipo
Nioune mbède rodè sunuy mind baniouy tuute tank
Tay am nagne money gno gui shine daniouy woute bank
We mutherfuckin keep it real every fuckin day
Street love King Gueye, No fuckin gay
Nioune Sunu five lègui nigga nioy khol kign keuy
Diokh dou nieup Fuck off, Fokk kokou clean kéy
Show me love I show you back, I’m cool like JOHNY DIACK
Respect bi moy meusseu daw, Fepp fouma sa Jo ni diakk
Sa corner nga nèkk di polluer rek
Tchi mbède bi daniouley xoli yeuy lekk
Ay yakhou MC Sama collier nëk
Wa LG Diwan sèn xol yè nèèk
Rapeu pakètè fake yi teuthie sèn gate
Wakh ko fou real nek
Yow leu yow leu bo goorgoor lo rek public bi naw la
Yow la Yow la bo naagou rek Say nantango raw la
Olof néneu “kep kou bote bouki rek, Khathie yi mboow la”
Boul messeu gueum ni taarou beuré bi ni nga guimbo la
Kone bomey testé camarade, Yow da nga déssè kham rap
Mane dama yagua songue raak, Mane la TC (Tambacounda) congrat
Khana kay dead Legend Hip Hop rek momey déssé comme grade
Boudè ANGEL la xol yiy woute, Mane damey aisé comme BRAD

{Refrain}
Yes Sir Mane Killahrie laay deff
Louma ci gaubé guar douma tite douma khèf
Say Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf
Say Killahrie Killahrie this is KK Killahrie
Killahrie Killahrie I give you Some Killahrie
Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf

Braaaaaaa Gun to the Z word up
Yeah ! I give you some Killahrie my Niggah
Han dagno téél nga naadjééé
Lou Beat bi baadjé baadjéé
Dou téé flow bi taadjéé
…..Word up Killah
My Killahrie is right here
Yeah Yeah

{Refrain}
Yes Sir Mane Killahrie laay deff
Louma ci gaubé guar douma tite douma khèf
Say Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf
Say Killahrie Killahrie this is KK Killahrie
Killahrie Killahrie I give you Some Killahrie
Yes sir Mane Killahrie laay deff
Louma si gaubè garr douma tite douma khèf

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR