LYRIC

{Verse 1}
Louné laa dégueu di def tekkeu, Killah day mandi di def tatt
Mbède bi diox nama respect, dey lou deugou ma dem ci ba diekh taakeu
Djaayuma kène ay xaute brain mais boul tékeulé xandal ak ropalane
Neggaz yi dieul sama avance bouniou teudé douniou nélaw ndax nio ngui ci problème
My nigga my nigga my nigga my broda I’m not gonna called my sister my bitch’s
TEXT yimay BINDEU té tek ko ci MAITRISE
Mane DOLEL naa FLOW bi kone fokk sama BIC diss
Djougué ci hood bi di téwal wa ghetto bi
Nénagnema NDK yaay sunu héro bi
Gaïndé nga mbaurodi léral nga njéloo
Délo nga fierté kèn dotoul neubooti
King Killahrie défati HIT, MC no deffak sa défaite bi biik
Rikk na Lyric yi rafett ci beat, sama baram ci kanam gachette dou tiiit
May Ronaldo Zizou di CR7 nigga maag nga soroul sa père settt
Faux (billets) bi nga beug ni père SECK, nala yaubou jail feug leu perpette
Game bi la bousiller, FAKES yi la fusiller, MC yi exiler, Ma gueuneu sexylé
Niodi wouma luxe lé, mane dama musclé, Texte yu muslimé dokh yagg guiss louné
Meunouma RAP té né kène douma diss, mais kouma diss sama neuf lalay wane
Niggaz yima done boycott dima siiss, légui concert KILLAH day def bénéfices

{Refrain}
King Killahrie like that, King Killahrie like that
King Killahrie like that, King Killahrie like that
Niétélou Killahrie laay tek, mbètélou fake yima done xepp
Daniou tektélo mbeeeed ba bone xett
King Killahrie like that, ndékété feel nga limay tek
Mbèda niou may fiitou def téék, boniou bougoulite di nganiou respect
King Killahrie like that, King Killahrie like that
King Killahrie like that, King Killahrie like that
Niétélou Killahrie laay tek, tchiiiiiim sa fiiteu ngi waathieu
Sa koumpeu di laathie, sa coeur-reu gui daadjékou

{Verse 2}
Nigga boul toppou sa bad mind, songou killah moy sa dead line
Defna tchi rap loudoul Biggie di PAC, soumay bindeu day kawé ni Tech N9ne
Bou Beat bi métiwone ni DJEGUI SIRAATE, ladjal BAZIK mane dama tchi gueumeu di rap
Dieufeurou naa melnii deumeu ci yaapeu, kouma warando tempo bi doma tchi yapp
KILLAH dou léwtoo té dieulo Raak, TOXICO HIP HOP bi DJAMO RAP
Député mbède done honorable, DD Squad ndara taxawé COMORA
King Killahrie like that !
Na niveau bi adjou ba high tech, Mane kène douma djaay prek
Carrière yu beuré ngi enfer maa financé wone séni obsèques
Mbède bi djoyatoul concert nigga fuck you yèèn ak sen Jetset
Dama visité mbède bi lathie séni mbébette
Fathie séni gaum niou dessak séni légueute (cicatrices)
Topouniou bountou bureaux yi di feugueutte
Ni garabou gouy nitou nèèn douko dédjeuti
Niveau bi wessuna ay fèène, KILLAH ngi guèneu ci ay fééém
Boma di tékeulé kène ci niom dey moudjé ponkali blasphème
Dagnou la yagga di gueum lo ay bullshit ndjateu leu tchi leurre yi
Indi naa diouraumi (5ème) albums ci fouki (10) att ak niétélou (3ème) Killahrie
Ana gnouné wone ben album ngay def daadi délou Dealerie

{Refrain}
King Killahrie like that, King Killahrie like that
King Killahrie like that, King Killahrie like that
Niétélou Killahrie laay tek, mbètélou fake yima done xepp
Daniou tektélo mbeeeed ba bone xett
King Killahrie like that, ndékété feel nga limay tek
Mbèda niou may fiitou def téék, boniou bougoulite di nganiou respect
King Killahrie like that, King Killahrie like that
King Killahrie like that, King Killahrie like that
Niétélou Killahrie laay tek, tchiiiiiim sa fiiteu ngi waathieu
Sa koumpeu di laathie, sa coeur-reu gui daadjékou

{Verse 3}
Rest In Peace my broda OthiO, Rest In Peace my broda TOtO
Rest In Peace Sams mon pOtO, Sac AU dOs RAP fOdO
Putain de cicatrices au dOs
DOdO pOcO bouLO muchO Argent à gOgO
Tu connais mon LOgO, NegrO autO
Défense K.O, la mort ne vous fera pas de cadEAUX
Casa lion Bocandé HérO
Sénégal France c’est du 1 en ZérO
Tirailleurs trahis Thiaroye ébailli
Bombardement c’est la France qui remercie
Killahrie tuerie c’est une mitunerie
Qu’ils ont pretexté pour masquer leurs conneries
Mane dama djangue ci dembe di tay, Ma ngi done oupou bi tchine bi di tay
Kone tay kou sissou daa fek nga jaloux ndakh yone leu ma djitou bou game bi di fay
Nigga bi baayéko Lougo LO, succès bi damako poudeuro
Takkouma tëré té séétouma Serigne ndax damassi khol sama toureundo (La Mort)
FOR EVER UNO (1) moy sama numéro

{Refrain}
King Killahrie like that, King Killahrie like that
King Killahrie like that, King Killahrie like that
Niétélou Killahrie laay tek, mbètélou fake yima done xepp
Daniou tektélo mbeeeed ba bone xett
King Killahrie like that, ndékété feel nga limay tek
Mbèda niou may fiitou def téék, boniou bougoulite di nganiou respect
King Killahrie like that, King Killahrie like that
King Killahrie like that, King Killahrie like that
Niétélou Killahrie laay tek, tchiiiiiim sa fiiteu ngi waathieu
Sa koumpeu di laathie, sa coeur-reu gui daadjékou

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR